Al-Hijr · 48/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
لَا يَمَسُّهُمْ فِيهَا نَصَبٌ وَمَا هُم مِّنْهَا بِمُخْرَجِينَ ۝٤٨
Laa yamas suhum feehaa nasabunw wa maa hum minhaa bimukhrajeen
📖 Tekkim Wolof
Coono duleen fa laal. Te dootuñu fa génnati.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 46-50 — Simoore Al-Hijr

46ادْخُلُوهَا بِسَلَامٍ آمِنِينَ
[Ñu ne leen] : “Dugguleen ci jàmm ànd ak kóolute”.
47وَنَزَعْنَا مَا فِي صُدُورِهِم مِّنْ غِلٍّ إِخْوَانًا عَلَىٰ سُرُرٍ مُّتَقَابِلِينَ
Te Nu rocci [raxas] la nekkoon ci seeni xol cig noonoo : ñu nekk ay mbokk yu jaaxaan ca seeni lal jàkkaarloo.
48لَا يَمَسُّهُمْ فِيهَا نَصَبٌ وَمَا هُم مِّنْهَا بِمُخْرَجِينَ
Coono duleen fa laal. Te dootuñu fa génnati.
49۞ نَبِّئْ عِبَادِي أَنِّي أَنَا الْغَفُورُ الرَّحِيمُ
Xamalal samay jaam ne, Man Jéggalaakoon laa, Jaglewaakoon laa.
50وَأَنَّ عَذَابِي هُوَ الْعَذَابُ الْأَلِيمُ
Waaye sama mbugal mooy mbugal mu metti mi.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
48Aaya

Tekki — Al-Hijr 48

Simoore Al-Hijr Aaya 48 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Coono duleen fa laal. Te dootuñu fa génnati.

Simoore Aaya 48/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 46–50. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers