Al-Hijr · 61/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
فَلَمَّا جَاءَ آلَ لُوطٍ الْمُرْسَلُونَ ۝٦١
Falamma jaaa`a Aala Lootinil mursaloon
📖 Tekkim Wolof
Ba ña ñu yónni agsee ca waa kër Lóot,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 59-63 — Simoore Al-Hijr

59إِلَّا آلَ لُوطٍ إِنَّا لَمُنَجُّوهُمْ أَجْمَعِينَ
ba mu des njabootu Lóot, danañu leen musal ñoom ñépp
60إِلَّا امْرَأَتَهُ قَدَّرْنَا ۙ إِنَّهَا لَمِنَ الْغَابِرِينَ
ku ca dul soxnaam sa. “Dogal Nanu ne moom ca way-des ña lay bokk (alku)”.
61فَلَمَّا جَاءَ آلَ لُوطٍ الْمُرْسَلُونَ
Ba ña ñu yónni agsee ca waa kër Lóot,
62قَالَ إِنَّكُمْ قَوْمٌ مُّنكَرُونَ
Lóot ne leen : “Yéen dey aw nit ñu ma xamul ngeen”.
63قَالُوا بَلْ جِئْنَاكَ بِمَا كَانُوا فِيهِ يَمْتَرُونَ
- Ñu ne ko : “Axakay, digal nanu la ànd ak la ñu doon sikki-sàkka.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
61Aaya

Tekki — Al-Hijr 61

Simoore Al-Hijr Aaya 61 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba ña ñu yónni agsee ca waa kër Lóot,

Simoore Aaya 61/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 59–63. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers