Al-Hijr · 60/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
إِلَّا امْرَأَتَهُ قَدَّرْنَا ۙ إِنَّهَا لَمِنَ الْغَابِرِينَ ۝٦٠
Illam ra atahoo qaddarnaaa innahaa laminal ghaabireen
📖 Tekkim Wolof
ku ca dul soxnaam sa. “Dogal Nanu ne moom ca way-des ña lay bokk (alku)”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 58-62 — Al-Hijr

58قَالُوا إِنَّا أُرْسِلْنَا إِلَىٰ قَوْمٍ مُّجْرِمِينَ
- Ñu ne : “Yónneef nañu ci aw nit ñu bari bàkkaar,
59إِلَّا آلَ لُوطٍ إِنَّا لَمُنَجُّوهُمْ أَجْمَعِينَ
ba mu des njabootu Lóot, danañu leen musal ñoom ñépp
60إِلَّا امْرَأَتَهُ قَدَّرْنَا ۙ إِنَّهَا لَمِنَ الْغَابِرِينَ
ku ca dul soxnaam sa. “Dogal Nanu ne moom ca way-des ña lay bokk (alku)”.
61فَلَمَّا جَاءَ آلَ لُوطٍ الْمُرْسَلُونَ
Ba ña ñu yónni agsee ca waa kër Lóot,
62قَالَ إِنَّكُمْ قَوْمٌ مُّنكَرُونَ
Lóot ne leen : “Yéen dey aw nit ñu ma xamul ngeen”.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
60Aaya

Tekki — Al-Hijr 60

Simoore Al-Hijr Aaya 60 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ku ca dul soxnaam sa. “Dogal Nanu ne moom ca…

Simoore Aaya 60/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 58–62. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers