Al-Hijr · 62/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
قَالَ إِنَّكُمْ قَوْمٌ مُّنكَرُونَ ۝٦٢
Qaala innakum qawmum munkaroon
📖 Tekkim Wolof
Lóot ne leen : “Yéen dey aw nit ñu ma xamul ngeen”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 60-64 — Simoore Al-Hijr

60إِلَّا امْرَأَتَهُ قَدَّرْنَا ۙ إِنَّهَا لَمِنَ الْغَابِرِينَ
ku ca dul soxnaam sa. “Dogal Nanu ne moom ca way-des ña lay bokk (alku)”.
61فَلَمَّا جَاءَ آلَ لُوطٍ الْمُرْسَلُونَ
Ba ña ñu yónni agsee ca waa kër Lóot,
62قَالَ إِنَّكُمْ قَوْمٌ مُّنكَرُونَ
Lóot ne leen : “Yéen dey aw nit ñu ma xamul ngeen”.
63قَالُوا بَلْ جِئْنَاكَ بِمَا كَانُوا فِيهِ يَمْتَرُونَ
- Ñu ne ko : “Axakay, digal nanu la ànd ak la ñu doon sikki-sàkka.
64وَأَتَيْنَاكَ بِالْحَقِّ وَإِنَّا لَصَادِقُونَ
Te ñëw nanu ci yaw indil la dëgg. Te it ñu dëggu lanu.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
62Aaya

Tekki — Al-Hijr 62

Simoore Al-Hijr Aaya 62 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lóot ne leen : “Yéen dey aw nit ñu ma…

Simoore Aaya 62/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 60–64. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers