Al-Hijr · 65/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
فَأَسْرِ بِأَهْلِكَ بِقِطْعٍ مِّنَ اللَّيْلِ وَاتَّبِعْ أَدْبَارَهُمْ وَلَا يَلْتَفِتْ مِنكُمْ أَحَدٌ وَامْضُوا حَيْثُ تُؤْمَرُونَ ۝٦٥
Fa asri bi ahlika biqit`im minal laili wattabi` adbaarahum wa laa yaltafit minkum ahadunw wamdoo haisu tu`maroon
📖 Tekkim Wolof
Te nanga dem rañaan yaak sa njaboot bu guddi xaajee ; te nga topp ca seen ginnaaw te bu kenn ci yéen geestu. Te ngeen jublu fa ñu leen digal”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 63-67 — Al-Hijr

63قَالُوا بَلْ جِئْنَاكَ بِمَا كَانُوا فِيهِ يَمْتَرُونَ
- Ñu ne ko : “Axakay, digal nanu la ànd ak la ñu doon sikki-sàkka.
64وَأَتَيْنَاكَ بِالْحَقِّ وَإِنَّا لَصَادِقُونَ
Te ñëw nanu ci yaw indil la dëgg. Te it ñu dëggu lanu.
65فَأَسْرِ بِأَهْلِكَ بِقِطْعٍ مِّنَ اللَّيْلِ وَاتَّبِعْ أَدْبَارَهُمْ وَلَا يَلْتَفِتْ مِنكُمْ أَحَدٌ وَامْضُوا حَيْثُ تُؤْمَرُونَ
Te nanga dem rañaan yaak sa njaboot bu guddi xaajee ; te nga topp ca seen ginnaaw te bu kenn ci yéen geestu. Te ngeen jublu fa ñu leen digal”.
66وَقَضَيْنَا إِلَيْهِ ذَٰلِكَ الْأَمْرَ أَنَّ دَابِرَ هَٰؤُلَاءِ مَقْطُوعٌ مُّصْبِحِينَ
Noo xamal Lóot sunu ndigal la : te danañu alag nitam ña ci njël.
67وَجَاءَ أَهْلُ الْمَدِينَةِ يَسْتَبْشِرُونَ
Waa dëkk ba agsi ànd ak mbégte.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
65Aaya

Tekki — Al-Hijr 65

Simoore Al-Hijr Aaya 65 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te nanga dem rañaan yaak sa njaboot bu guddi xaajee…

Simoore Aaya 65/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 63–67. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers