Al-Hijr · 64/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
وَأَتَيْنَاكَ بِالْحَقِّ وَإِنَّا لَصَادِقُونَ ۝٦٤
Wa atainaaka bilhaqqi wa innaa lasaadiqoon
📖 Tekkim Wolof
Te ñëw nanu ci yaw indil la dëgg. Te it ñu dëggu lanu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 62-66 — Simoore Al-Hijr

62قَالَ إِنَّكُمْ قَوْمٌ مُّنكَرُونَ
Lóot ne leen : “Yéen dey aw nit ñu ma xamul ngeen”.
63قَالُوا بَلْ جِئْنَاكَ بِمَا كَانُوا فِيهِ يَمْتَرُونَ
- Ñu ne ko : “Axakay, digal nanu la ànd ak la ñu doon sikki-sàkka.
64وَأَتَيْنَاكَ بِالْحَقِّ وَإِنَّا لَصَادِقُونَ
Te ñëw nanu ci yaw indil la dëgg. Te it ñu dëggu lanu.
65فَأَسْرِ بِأَهْلِكَ بِقِطْعٍ مِّنَ اللَّيْلِ وَاتَّبِعْ أَدْبَارَهُمْ وَلَا يَلْتَفِتْ مِنكُمْ أَحَدٌ وَامْضُوا حَيْثُ تُؤْمَرُونَ
Te nanga dem rañaan yaak sa njaboot bu guddi xaajee ; te nga topp ca seen ginnaaw te bu kenn ci yéen geestu. Te ngeen jublu fa ñu leen digal”.
66وَقَضَيْنَا إِلَيْهِ ذَٰلِكَ الْأَمْرَ أَنَّ دَابِرَ هَٰؤُلَاءِ مَقْطُوعٌ مُّصْبِحِينَ
Noo xamal Lóot sunu ndigal la : te danañu alag nitam ña ci njël.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
64Aaya

Tekki — Al-Hijr 64

Simoore Al-Hijr Aaya 64 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te ñëw nanu ci yaw indil la dëgg. Te it…

Simoore Aaya 64/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 62–66. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers