Al-Hijr · 66/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
وَقَضَيْنَا إِلَيْهِ ذَٰلِكَ الْأَمْرَ أَنَّ دَابِرَ هَٰؤُلَاءِ مَقْطُوعٌ مُّصْبِحِينَ ۝٦٦
Wa qadainaaa ilaihi zaalikal amra anna daabira haaa`ulaaa`i maqtoo`um musbiheen
📖 Tekkim Wolof
Noo xamal Lóot sunu ndigal la : te danañu alag nitam ña ci njël.

🎧 Dégg


📜 Aaya 64-68 — Simoore Al-Hijr

64وَأَتَيْنَاكَ بِالْحَقِّ وَإِنَّا لَصَادِقُونَ
Te ñëw nanu ci yaw indil la dëgg. Te it ñu dëggu lanu.
65فَأَسْرِ بِأَهْلِكَ بِقِطْعٍ مِّنَ اللَّيْلِ وَاتَّبِعْ أَدْبَارَهُمْ وَلَا يَلْتَفِتْ مِنكُمْ أَحَدٌ وَامْضُوا حَيْثُ تُؤْمَرُونَ
Te nanga dem rañaan yaak sa njaboot bu guddi xaajee ; te nga topp ca seen ginnaaw te bu kenn ci yéen geestu. Te ngeen jublu fa ñu leen digal”.
66وَقَضَيْنَا إِلَيْهِ ذَٰلِكَ الْأَمْرَ أَنَّ دَابِرَ هَٰؤُلَاءِ مَقْطُوعٌ مُّصْبِحِينَ
Noo xamal Lóot sunu ndigal la : te danañu alag nitam ña ci njël.
67وَجَاءَ أَهْلُ الْمَدِينَةِ يَسْتَبْشِرُونَ
Waa dëkk ba agsi ànd ak mbégte.
68قَالَ إِنَّ هَٰؤُلَاءِ ضَيْفِي فَلَا تَفْضَحُونِ
- Lóot ne leen : “Ñii samay gan lañu, buleen ma ci rusloo.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
66Aaya

Tekki — Al-Hijr 66

Simoore Al-Hijr Aaya 66 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noo xamal Lóot sunu ndigal la : te danañu alag…

Simoore Aaya 66/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 64–68. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers