Al-Hijr · 81/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
وَآتَيْنَاهُمْ آيَاتِنَا فَكَانُوا عَنْهَا مُعْرِضِينَ ٨١
Transliteration
Wa aatainaahum Aayaatinaa fakaanoo `anhaa mu`rideen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Nu joxoon leen sunuy kawtéef, ñu dëddu leen.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 79-83 — Al-Hijr
79فَانتَقَمْنَا مِنْهُمْ وَإِنَّهُمَا لَبِإِمَامٍ مُّبِينٍ
Nu mbugal leen. Te [ñaari dëkk yooyu] ñanga ca yoon wu neex a xam.
80وَلَقَدْ كَذَّبَ أَصْحَابُ الْحِجْرِ الْمُرْسَلِينَ
Waa Hijri weddi woon nañu Yonent ya.
81وَآتَيْنَاهُمْ آيَاتِنَا فَكَانُوا عَنْهَا مُعْرِضِينَ
Nu joxoon leen sunuy kawtéef, ñu dëddu leen.
82وَكَانُوا يَنْحِتُونَ مِنَ الْجِبَالِ بُيُوتًا آمِنِينَ
Ñu nekkoon ñu daan yatt i néeg ci ay tundi doj.
83فَأَخَذَتْهُمُ الصَّيْحَةُ مُصْبِحِينَ
Ag xaacu sadd leen ci ag suba cuuy
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
81Aaya
Tekki — Al-Hijr 81
Simoore Al-Hijr Aaya 81 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu joxoon leen sunuy kawtéef, ñu dëddu leen.Simoore Aaya 81/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 79–83. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








