Al-Hijr · 80/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
وَلَقَدْ كَذَّبَ أَصْحَابُ الْحِجْرِ الْمُرْسَلِينَ ۝٨٠
Wa laqad kazzaba ashaabul Hijril mursaleen
📖 Tekkim Wolof
Waa Hijri weddi woon nañu Yonent ya.

🎧 Dégg


📜 Aaya 78-82 — Simoore Al-Hijr

78وَإِن كَانَ أَصْحَابُ الْأَيْكَةِ لَظَالِمِينَ
Te waa Leykata ay tooñkat lañu woon.
79فَانتَقَمْنَا مِنْهُمْ وَإِنَّهُمَا لَبِإِمَامٍ مُّبِينٍ
Nu mbugal leen. Te [ñaari dëkk yooyu] ñanga ca yoon wu neex a xam.
80وَلَقَدْ كَذَّبَ أَصْحَابُ الْحِجْرِ الْمُرْسَلِينَ
Waa Hijri weddi woon nañu Yonent ya.
81وَآتَيْنَاهُمْ آيَاتِنَا فَكَانُوا عَنْهَا مُعْرِضِينَ
Nu joxoon leen sunuy kawtéef, ñu dëddu leen.
82وَكَانُوا يَنْحِتُونَ مِنَ الْجِبَالِ بُيُوتًا آمِنِينَ
Ñu nekkoon ñu daan yatt i néeg ci ay tundi doj.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
80Aaya

Tekki — Al-Hijr 80

Simoore Al-Hijr Aaya 80 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waa Hijri weddi woon nañu Yonent ya.

Simoore Aaya 80/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 78–82. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers