Al-Hijr · 85/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
وَمَا خَلَقْنَا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا إِلَّا بِالْحَقِّ ۗ وَإِنَّ السَّاعَةَ لَآتِيَةٌ ۖ فَاصْفَحِ الصَّفْحَ الْجَمِيلَ ٨٥
Transliteration
Wa maa khalaqnas samaawaati wal arda wa maa bainahumaaa illaa bilhaqq; wa innas Saa`ata la aatiyatun fasfahis safhal jameel
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te Nun bind nu asamaan yi ak suuf si ak li nekk ci seen diggante lu dul ci dëgg. Te jeexug Sama àddina sii luy nekk la ! Kon nanga dëddu ña weddi dëddu gu rafet.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 83-87 — Al-Hijr
83فَأَخَذَتْهُمُ الصَّيْحَةُ مُصْبِحِينَ
Ag xaacu sadd leen ci ag suba cuuy
84فَمَا أَغْنَىٰ عَنْهُم مَّا كَانُوا يَكْسِبُونَ
La ñu doon fàggu jariñu leen dara.
85وَمَا خَلَقْنَا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا إِلَّا بِالْحَقِّ ۗ وَإِنَّ السَّاعَةَ لَآتِيَةٌ ۖ فَاصْفَحِ الصَّفْحَ الْجَمِيلَ
Te Nun bind nu asamaan yi ak suuf si ak li nekk ci seen diggante lu dul ci dëgg. Te jeexug Sama àddina sii luy nekk la ! Kon nanga dëddu ña weddi dëddu gu rafet.
86إِنَّ رَبَّكَ هُوَ الْخَلَّاقُ الْعَلِيمُ
Sa Boroom mooy Ka bind, di Ku xam.
87وَلَقَدْ آتَيْنَاكَ سَبْعًا مِّنَ الْمَثَانِي وَالْقُرْآنَ الْعَظِيمَ
May Nanu la “juroom-ñaar yu Nu ñaar-ñaaral [Al-Faatiha]”, ak Alxuraan ju màgg jii.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
85Aaya
Tekki — Al-Hijr 85
Simoore Al-Hijr Aaya 85 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te Nun bind nu asamaan yi ak suuf si ak…Simoore Aaya 85/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 83–87. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








