Al-Hijr · 86/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
إِنَّ رَبَّكَ هُوَ الْخَلَّاقُ الْعَلِيمُ ۝٨٦
Inna Rabbaka Huwal khallaaqul `aleem
📖 Tekkim Wolof
Sa Boroom mooy Ka bind, di Ku xam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 84-88 — Simoore Al-Hijr

84فَمَا أَغْنَىٰ عَنْهُم مَّا كَانُوا يَكْسِبُونَ
La ñu doon fàggu jariñu leen dara.
85وَمَا خَلَقْنَا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا إِلَّا بِالْحَقِّ ۗ وَإِنَّ السَّاعَةَ لَآتِيَةٌ ۖ فَاصْفَحِ الصَّفْحَ الْجَمِيلَ
Te Nun bind nu asamaan yi ak suuf si ak li nekk ci seen diggante lu dul ci dëgg. Te jeexug Sama àddina sii luy nekk la ! Kon nanga dëddu ña weddi dëddu gu rafet.
86إِنَّ رَبَّكَ هُوَ الْخَلَّاقُ الْعَلِيمُ
Sa Boroom mooy Ka bind, di Ku xam.
87وَلَقَدْ آتَيْنَاكَ سَبْعًا مِّنَ الْمَثَانِي وَالْقُرْآنَ الْعَظِيمَ
May Nanu la “juroom-ñaar yu Nu ñaar-ñaaral [Al-Faatiha]”, ak Alxuraan ju màgg jii.
88لَا تَمُدَّنَّ عَيْنَيْكَ إِلَىٰ مَا مَتَّعْنَا بِهِ أَزْوَاجًا مِّنْهُمْ وَلَا تَحْزَنْ عَلَيْهِمْ وَاخْفِضْ جَنَاحَكَ لِلْمُؤْمِنِينَ
Bul tàllal say gët [di xool] la Nu xéewale ay kurél ci ñoom, bul am naqar ci ñoom te nangay suufeel say mbagg ñeel ñi gëm.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
86Aaya

Tekki — Al-Hijr 86

Simoore Al-Hijr Aaya 86 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sa Boroom mooy Ka bind, di Ku xam.

Simoore Aaya 86/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 84–88. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers