Al-Hijr · 84/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
فَمَا أَغْنَىٰ عَنْهُم مَّا كَانُوا يَكْسِبُونَ ۝٨٤
Famaaa aghnaa `anhum maa kaanoo yaksiboon
📖 Tekkim Wolof
La ñu doon fàggu jariñu leen dara.

🎧 Dégg


📜 Aaya 82-86 — Simoore Al-Hijr

82وَكَانُوا يَنْحِتُونَ مِنَ الْجِبَالِ بُيُوتًا آمِنِينَ
Ñu nekkoon ñu daan yatt i néeg ci ay tundi doj.
83فَأَخَذَتْهُمُ الصَّيْحَةُ مُصْبِحِينَ
Ag xaacu sadd leen ci ag suba cuuy
84فَمَا أَغْنَىٰ عَنْهُم مَّا كَانُوا يَكْسِبُونَ
La ñu doon fàggu jariñu leen dara.
85وَمَا خَلَقْنَا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا إِلَّا بِالْحَقِّ ۗ وَإِنَّ السَّاعَةَ لَآتِيَةٌ ۖ فَاصْفَحِ الصَّفْحَ الْجَمِيلَ
Te Nun bind nu asamaan yi ak suuf si ak li nekk ci seen diggante lu dul ci dëgg. Te jeexug Sama àddina sii luy nekk la ! Kon nanga dëddu ña weddi dëddu gu rafet.
86إِنَّ رَبَّكَ هُوَ الْخَلَّاقُ الْعَلِيمُ
Sa Boroom mooy Ka bind, di Ku xam.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
84Aaya

Tekki — Al-Hijr 84

Simoore Al-Hijr Aaya 84 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : La ñu doon fàggu jariñu leen dara.

Simoore Aaya 84/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 82–86. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers