Al-Hijr · 92/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
فَوَرَبِّكَ لَنَسْأَلَنَّهُمْ أَجْمَعِينَ ۝٩٢
Fawa Rabbika lanas`a lannahum ajma`een
📖 Tekkim Wolof
Giñ naa ci sama màggug Boroom ! Fàwwu danañu leen laaj ñoom ñépp

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 90-94 — Simoore Al-Hijr

90كَمَا أَنزَلْنَا عَلَى الْمُقْتَسِمِينَ
Noonu it Lanu wàccele woon [ab Téere] ca ña xàjjatle woon [seen diine],
91الَّذِينَ جَعَلُوا الْقُرْآنَ عِضِينَ
ca ña séddale Téere ba ay xaaj, pàcc-pàccee Alxuraan ngir sànkaate.
92فَوَرَبِّكَ لَنَسْأَلَنَّهُمْ أَجْمَعِينَ
Giñ naa ci sama màggug Boroom ! Fàwwu danañu leen laaj ñoom ñépp
93عَمَّا كَانُوا يَعْمَلُونَ
la ñu nekkon di ko def [ci ay ñaawtéef].
94فَاصْدَعْ بِمَا تُؤْمَرُ وَأَعْرِضْ عَنِ الْمُشْرِكِينَ
Waxal ci kaw li Nu la digal te nanga dëddu bokkaalekat yi.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
92Aaya

Tekki — Al-Hijr 92

Simoore Al-Hijr Aaya 92 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Giñ naa ci sama màggug Boroom ! Fàwwu danañu leen…

Simoore Aaya 92/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 90–94. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers