An-Nahl · 19/128
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nahl
وَاللَّهُ يَعْلَمُ مَا تُسِرُّونَ وَمَا تُعْلِنُونَ ۝١٩
Wallaahu ya`lamu maa tusirroona wa maa tu`linoon
📖 Tekkim Wolof
Te Yàlla xam na li ngeen nëbb ak li ngeen feeñal.

🎧 Dégg


📜 Aaya 17-21 — Simoore An-Nahl

17أَفَمَن يَخْلُقُ كَمَن لَّا يَخْلُقُ ۗ أَفَلَا تَذَكَّرُونَ
Waaw ndax ku bind dana mën a yem ak ku bindul dara ? Moo ndax dangeen dul fàttaliku ?
18وَإِن تَعُدُّوا نِعْمَةَ اللَّهِ لَا تُحْصُوهَا ۗ إِنَّ اللَّهَ لَغَفُورٌ رَّحِيمٌ
Te bu ngeen doon jéem a lim xéewal yi leen Yàlla defal, dungeen ko mën. Te Yàlla Moom Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
19وَاللَّهُ يَعْلَمُ مَا تُسِرُّونَ وَمَا تُعْلِنُونَ
Te Yàlla xam na li ngeen nëbb ak li ngeen feeñal.
20وَالَّذِينَ يَدْعُونَ مِن دُونِ اللَّهِ لَا يَخْلُقُونَ شَيْئًا وَهُمْ يُخْلَقُونَ
Te ya ñuy jaamu bàyyi Yàlla binduñu dara, te sax dañu leen bind far.
21أَمْوَاتٌ غَيْرُ أَحْيَاءٍ ۖ وَمَا يَشْعُرُونَ أَيَّانَ يُبْعَثُونَ
Yu dee lañu, nekkuñu luy dundu, te xamuñu kañ lañu leen di dekkal.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
19Aaya

Tekki — An-Nahl 19

Simoore An-Nahl Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te Yàlla xam na li ngeen nëbb ak li ngeen…

Simoore Aaya 19/128 — Simoore An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nahl Dégg, Simoore An-Nahl Tekki, Simoore An-Nahl mp3, Simoore An-Nahl pdf. Aaya 17–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers