Al-Isra · 32/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
وَلَا تَقْرَبُوا الزِّنَا ۖ إِنَّهُ كَانَ فَاحِشَةً وَسَاءَ سَبِيلًا ۝٣٢
Wa laa taqrabuz zinaaa innahoo kaana faahishatanw wa saaa`a sabeelaa
📖 Tekkim Wolof
Te buleen jegeñ njaaloo. Ndax moom nekk na lu ñaaw tey yoonu lu bon !

🎧 Dégg


📜 Aaya 30-34 — Al-Isra

30إِنَّ رَبَّكَ يَبْسُطُ الرِّزْقَ لِمَن يَشَاءُ وَيَقْدِرُ ۚ إِنَّهُ كَانَ بِعِبَادِهِ خَبِيرًا بَصِيرًا
Naka sa Boroom mooy yaatal wërsëgu ku Ko soob. Moo koy xatal it, naka Moom ku xam tey gis la jaamam yi.
31وَلَا تَقْتُلُوا أَوْلَادَكُمْ خَشْيَةَ إِمْلَاقٍ ۖ نَّحْنُ نَرْزُقُهُمْ وَإِيَّاكُمْ ۚ إِنَّ قَتْلَهُمْ كَانَ خِطْئًا كَبِيرًا
Buleen rey seeni doom ngir ragal ag ñàkk ; Nun noo leen di wërsëgal ñoom ak yéen. Rey leen bàkkaar bu rëy la.
32وَلَا تَقْرَبُوا الزِّنَا ۖ إِنَّهُ كَانَ فَاحِشَةً وَسَاءَ سَبِيلًا
Te buleen jegeñ njaaloo. Ndax moom nekk na lu ñaaw tey yoonu lu bon !
33وَلَا تَقْتُلُوا النَّفْسَ الَّتِي حَرَّمَ اللَّهُ إِلَّا بِالْحَقِّ ۗ وَمَن قُتِلَ مَظْلُومًا فَقَدْ جَعَلْنَا لِوَلِيِّهِ سُلْطَانًا فَلَا يُسْرِف فِّي الْقَتْلِ ۖ إِنَّهُ كَانَ مَنصُورًا
Buleen rey bakkan ngir lu Yàlla araamal la, lu dul ci dëgg. Képp ku ñu rey, di ku ñu tooñ, jox Nanu kay taxawu mbiram sañ-sañ. Waaye bu mu jéggi dayo ci rey, ndax moom ku [yoon] dimbali la.
34وَلَا تَقْرَبُوا مَالَ الْيَتِيمِ إِلَّا بِالَّتِي هِيَ أَحْسَنُ حَتَّىٰ يَبْلُغَ أَشُدَّهُ ۚ وَأَوْفُوا بِالْعَهْدِ ۖ إِنَّ الْعَهْدَ كَانَ مَسْئُولًا
Buleen jegeñ alali jirim lu dul ca na mu gën a rafete, ba kero muy nekk mag te sàmm kóllare ga. Ndax kóllare lu ñuy laaj la ëllëg ca àllaaxira
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
32Aaya

Tekki — Al-Isra 32

Simoore Al-Isra Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te buleen jegeñ njaaloo. Ndax moom nekk na lu ñaaw…

Simoore Aaya 32/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers