Al-Kahf · 25/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
وَلَبِثُوا فِي كَهْفِهِمْ ثَلَاثَ مِائَةٍ سِنِينَ وَازْدَادُوا تِسْعًا ۝٢٥
Wa labisoo fee kahfihim salaasa mi`atin sineena wazdaadoo tis`aa
📖 Tekkim Wolof
Toog nañu ca seen xunt ma ñetti téeméeri at yu teg juróom-ñeent.

🎧 Dégg


📜 Aaya 23-27 — Al-Kahf

23وَلَا تَقُولَنَّ لِشَيْءٍ إِنِّي فَاعِلٌ ذَٰلِكَ غَدًا
Bul wax mukk ci dara ne : “Man dana def nàngam ëllëg”.
24إِلَّا أَن يَشَاءَ اللَّهُ ۚ وَاذْكُر رَّبَّكَ إِذَا نَسِيتَ وَقُلْ عَسَىٰ أَن يَهْدِيَنِ رَبِّي لِأَقْرَبَ مِنْ هَٰذَا رَشَدًا
[te boolewoo ca] : “Bu soobee Yàlla”, tuddal sa Boroom, boo fàttee fàttaliku Ko te nga wax ne : “Xéy-na sama Boroom gindi ma jëme ma ca la gën a jegeñ lii cig njub”.
25وَلَبِثُوا فِي كَهْفِهِمْ ثَلَاثَ مِائَةٍ سِنِينَ وَازْدَادُوا تِسْعًا
Toog nañu ca seen xunt ma ñetti téeméeri at yu teg juróom-ñeent.
26قُلِ اللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا لَبِثُوا ۖ لَهُ غَيْبُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۖ أَبْصِرْ بِهِ وَأَسْمِعْ ۚ مَا لَهُم مِّن دُونِهِ مِن وَلِيٍّ وَلَا يُشْرِكُ فِي حُكْمِهِ أَحَدًا
Neel : “Yàllaa gën a xam diir ba ñu fa toog. Ñeel na ko [moom Yàlla] kumpag asamaan yi ak suuf si. Nangay gise ci Moom, di dégge ci Moom ! Amuñu ku leen di wattu ci Moom, du boole kenn ci àtteem.
27وَاتْلُ مَا أُوحِيَ إِلَيْكَ مِن كِتَابِ رَبِّكَ ۖ لَا مُبَدِّلَ لِكَلِمَاتِهِ وَلَن تَجِدَ مِن دُونِهِ مُلْتَحَدًا
Jàngal li ñu la soloo ci sa Téereb Boroom. Bul soppiy waxam [ay waxam du soppiku]. Te doo am mukk wéeruwaay wu dul Moom.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — Al-Kahf 25

Simoore Al-Kahf Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Toog nañu ca seen xunt ma ñetti téeméeri at yu…

Simoore Aaya 25/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers