Al-Kahf · 26/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
قُلِ اللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا لَبِثُوا ۖ لَهُ غَيْبُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۖ أَبْصِرْ بِهِ وَأَسْمِعْ ۚ مَا لَهُم مِّن دُونِهِ مِن وَلِيٍّ وَلَا يُشْرِكُ فِي حُكْمِهِ أَحَدًا ۝٢٦
Qulil laahu a`lamu bimaa labisoo lahoo ghaibus samaawaati wal ardi absir bihee wa asmi`; maa lahum min doonihee minw waliyyinw wa laa yushriku fee hukmihee ahadaa
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Yàllaa gën a xam diir ba ñu fa toog. Ñeel na ko [moom Yàlla] kumpag asamaan yi ak suuf si. Nangay gise ci Moom, di dégge ci Moom ! Amuñu ku leen di wattu ci Moom, du boole kenn ci àtteem.

🎧 Dégg


📜 Aaya 24-28 — Al-Kahf

24إِلَّا أَن يَشَاءَ اللَّهُ ۚ وَاذْكُر رَّبَّكَ إِذَا نَسِيتَ وَقُلْ عَسَىٰ أَن يَهْدِيَنِ رَبِّي لِأَقْرَبَ مِنْ هَٰذَا رَشَدًا
[te boolewoo ca] : “Bu soobee Yàlla”, tuddal sa Boroom, boo fàttee fàttaliku Ko te nga wax ne : “Xéy-na sama Boroom gindi ma jëme ma ca la gën a jegeñ lii cig njub”.
25وَلَبِثُوا فِي كَهْفِهِمْ ثَلَاثَ مِائَةٍ سِنِينَ وَازْدَادُوا تِسْعًا
Toog nañu ca seen xunt ma ñetti téeméeri at yu teg juróom-ñeent.
26قُلِ اللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا لَبِثُوا ۖ لَهُ غَيْبُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۖ أَبْصِرْ بِهِ وَأَسْمِعْ ۚ مَا لَهُم مِّن دُونِهِ مِن وَلِيٍّ وَلَا يُشْرِكُ فِي حُكْمِهِ أَحَدًا
Neel : “Yàllaa gën a xam diir ba ñu fa toog. Ñeel na ko [moom Yàlla] kumpag asamaan yi ak suuf si. Nangay gise ci Moom, di dégge ci Moom ! Amuñu ku leen di wattu ci Moom, du boole kenn ci àtteem.
27وَاتْلُ مَا أُوحِيَ إِلَيْكَ مِن كِتَابِ رَبِّكَ ۖ لَا مُبَدِّلَ لِكَلِمَاتِهِ وَلَن تَجِدَ مِن دُونِهِ مُلْتَحَدًا
Jàngal li ñu la soloo ci sa Téereb Boroom. Bul soppiy waxam [ay waxam du soppiku]. Te doo am mukk wéeruwaay wu dul Moom.
28وَاصْبِرْ نَفْسَكَ مَعَ الَّذِينَ يَدْعُونَ رَبَّهُم بِالْغَدَاةِ وَالْعَشِيِّ يُرِيدُونَ وَجْهَهُ ۖ وَلَا تَعْدُ عَيْنَاكَ عَنْهُمْ تُرِيدُ زِينَةَ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا ۖ وَلَا تُطِعْ مَنْ أَغْفَلْنَا قَلْبَهُ عَن ذِكْرِنَا وَاتَّبَعَ هَوَاهُ وَكَانَ أَمْرُهُ فُرُطًا
Nangay muñ ànd ak ñay jaamu seen Boroom suba ak ngoon ngir xemmem jëmam. Te say gët bumu leen jéggi ngir xemmem taaru dundu àddina. Te bul topp koo xam ne sàgganloo nañu xelam ba dunu fàttaliku, di ku topp bakkanam, mbiram di lu jéggi dayoo.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
26Aaya

Tekki — Al-Kahf 26

Simoore Al-Kahf Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Yàllaa gën a xam diir ba ñu fa…

Simoore Aaya 26/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers