Maryam · 8/98
Tekki Waxtaan — Maryam
قَالَ رَبِّ أَنَّىٰ يَكُونُ لِي غُلَامٌ وَكَانَتِ امْرَأَتِي عَاقِرًا وَقَدْ بَلَغْتُ مِنَ الْكِبَرِ عِتِيًّا ۝٨
Qaala Rabbi annaa yakoonu lee ghulaamunw wa kaanatim ra atee aaqiranw wa qad balaghtu minal kibari `itiyyaa
📖 Tekkim Wolof
Mu ne : “Waaw yaw Boroom bi, ana fan la ma doom di bawoo te sama soxna di ku jaasir, man itam ma màggat ba kumur ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — Maryam

6يَرِثُنِي وَيَرِثُ مِنْ آلِ يَعْقُوبَ ۖ وَاجْعَلْهُ رَبِّ رَضِيًّا
[doom] ju may donn, di donn itam njabootug Yànqooba. Te nga def ko muy kuy gërëm”.
7يَا زَكَرِيَّا إِنَّا نُبَشِّرُكَ بِغُلَامٍ اسْمُهُ يَحْيَىٰ لَمْ نَجْعَل لَّهُ مِن قَبْلُ سَمِيًّا
"Éy Zakariyaa, Noo ngi lay bégal ci ne [danga am] doom ju tudd Yahyaa. Te turam woowu kenn masu koo am”.
8قَالَ رَبِّ أَنَّىٰ يَكُونُ لِي غُلَامٌ وَكَانَتِ امْرَأَتِي عَاقِرًا وَقَدْ بَلَغْتُ مِنَ الْكِبَرِ عِتِيًّا
Mu ne : “Waaw yaw Boroom bi, ana fan la ma doom di bawoo te sama soxna di ku jaasir, man itam ma màggat ba kumur ? ”
9قَالَ كَذَٰلِكَ قَالَ رَبُّكَ هُوَ عَلَيَّ هَيِّنٌ وَقَدْ خَلَقْتُكَ مِن قَبْلُ وَلَمْ تَكُ شَيْئًا
Mu ne ko : “Aa ! Loolu la sa Boroom wax de. Te lu ñàkk solo la ci man ndax maa la bindoon ba nga doonagul dara”.
10قَالَ رَبِّ اجْعَل لِّي آيَةً ۚ قَالَ آيَتُكَ أَلَّا تُكَلِّمَ النَّاسَ ثَلَاثَ لَيَالٍ سَوِيًّا
Mu ne ko : “[Yàlla] sama Boroom, defal ma màndarga”. Mu ne ko : “Sa màndarga mooy danga am ñetti fan yoo dul mën a waxante.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Maryam 8

Simoore Maryam Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne : “Waaw yaw Boroom bi, ana fan la…

Simoore Aaya 8/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers