Maryam · 94/98
Tekki Waxtaan — Simoore Maryam
لَّقَدْ أَحْصَاهُمْ وَعَدَّهُمْ عَدًّا ۝٩٤
Laqad ahsaahum wa addahum `addaa
📖 Tekkim Wolof
[Moom Yàlla] xam na fa ñu nekk ak na ñu day [na ñu tollu].

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 92-96 — Simoore Maryam

92وَمَا يَنبَغِي لِلرَّحْمَٰنِ أَن يَتَّخِذَ وَلَدًا
Waay-waay yellut ci Yërëmaakoon bi muy am doom waay !
93إِن كُلُّ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ إِلَّا آتِي الرَّحْمَٰنِ عَبْدًا
Képp ku nekk ci asamaan yi ak suuf si, jaamub Yàlla rekk lay doon.
94لَّقَدْ أَحْصَاهُمْ وَعَدَّهُمْ عَدًّا
[Moom Yàlla] xam na fa ñu nekk ak na ñu day [na ñu tollu].
95وَكُلُّهُمْ آتِيهِ يَوْمَ الْقِيَامَةِ فَرْدًا
Te bu Bis-pénc baa, bindéef yépp danañu taxaw ci kanamam kennoo kenn.
96إِنَّ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ سَيَجْعَلُ لَهُمُ الرَّحْمَٰنُ وُدًّا
Ña gëm tey jëf u yiw, Yàlla dana leen sagoo.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
94Aaya

Tekki — Maryam 94

Simoore Maryam Aaya 94 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Moom Yàlla] xam na fa ñu nekk ak na ñu…

Simoore Aaya 94/98 — Simoore Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Maryam Dégg, Simoore Maryam Tekki, Simoore Maryam mp3, Simoore Maryam pdf. Aaya 92–96. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers