Al-Baqara · 64/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
ثُمَّ تَوَلَّيْتُم مِّن بَعْدِ ذَٰلِكَ ۖ فَلَوْلَا فَضْلُ اللَّهِ عَلَيْكُمْ وَرَحْمَتُهُ لَكُنتُم مِّنَ الْخَاسِرِينَ ۝٦٤
Summa tawallaitum mim ba`di zaalika falawlaa fadlul laahi `alaikum wa rahmatuhoo lakuntum minal khaasireen
📖 Tekkim Wolof
Topp, ngeen dëddu ginnaaw loolu, bu dul koon xéewali Yàlla ci yéen ak yërmaandeem, kon dangeen bokk ca way-yàqule ña.
🎧 Dégg

📜 Aaya 62-66 — Al-Baqara

62إِنَّ الَّذِينَ آمَنُوا وَالَّذِينَ هَادُوا وَالنَّصَارَىٰ وَالصَّابِئِينَ مَنْ آمَنَ بِاللَّهِ وَالْيَوْمِ الْآخِرِ وَعَمِلَ صَالِحًا فَلَهُمْ أَجْرُهُمْ عِندَ رَبِّهِمْ وَلَا خَوْفٌ عَلَيْهِمْ وَلَا هُمْ يَحْزَنُونَ
Ña gëm ak ña di Yahuud, ak i Nasraan, ak i Saabiina, ku ca settantal ba dëddu la mu jàppoon, gëm Yàlla ak Bis-pénc ba, gëm Muhammad tey jëf lu yiw , danañu fekk seen pey ca Yàlla ; te duñu tiit te duñu jàq.
63وَإِذْ أَخَذْنَا مِيثَاقَكُمْ وَرَفَعْنَا فَوْقَكُمُ الطُّورَ خُذُوا مَا آتَيْنَاكُم بِقُوَّةٍ وَاذْكُرُوا مَا فِيهِ لَعَلَّكُمْ تَتَّقُونَ
Fàttalikuleen], ba Nu jàppee seen kóllare te Nu yékkati doj wa mu tiim leen, te Ma ne leen : “Jàppleen li Ma leen jox ànd ca ak dëgg te na ngeen màggal li ne [ca Téere ba] ndax Yàlla ngeen ragal seen Boroom ! ”
64ثُمَّ تَوَلَّيْتُم مِّن بَعْدِ ذَٰلِكَ ۖ فَلَوْلَا فَضْلُ اللَّهِ عَلَيْكُمْ وَرَحْمَتُهُ لَكُنتُم مِّنَ الْخَاسِرِينَ
Topp, ngeen dëddu ginnaaw loolu, bu dul koon xéewali Yàlla ci yéen ak yërmaandeem, kon dangeen bokk ca way-yàqule ña.
65وَلَقَدْ عَلِمْتُمُ الَّذِينَ اعْتَدَوْا مِنكُمْ فِي السَّبْتِ فَقُلْنَا لَهُمْ كُونُوا قِرَدَةً خَاسِئِينَ
Wallaahi xam ngeen ña jalgati woon ci yéen ca Gaawu ba. Tax ñoom ñooñu Nu ne leen : “Nekkleen di ay golo yu ñu beddi ! ”
66فَجَعَلْنَاهَا نَكَالًا لِّمَا بَيْنَ يَدَيْهَا وَمَا خَلْفَهَا وَمَوْعِظَةً لِّلْمُتَّقِينَ
Maka Kami jadikan (yang demikian) itu peringatan bagi orang-orang pada masa itu dan bagi mereka yang datang kemudian, serta menjadi pelajaran bagi orang-orang yang bertakwa.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
64Aaya

Tekki — Al-Baqara 64

Simoore Al-Baqara Aaya 64 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Topp, ngeen dëddu ginnaaw loolu, bu dul koon xéewali Yàlla…

Simoore Aaya 64/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 62–66. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers