Al-Anbiya · 62/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
قَالُوا أَأَنتَ فَعَلْتَ هَٰذَا بِآلِهَتِنَا يَا إِبْرَاهِيمُ ۝٦٢
Qaalooo `a-anta fa`alta haazaa bi aalihatinaa yaaa Ibraaheem
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne ko : “Ndax yaw yaa def lii ci sunu yàlla yi, yaw Ibraahiima ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 60-64 — Al-Anbiya

60قَالُوا سَمِعْنَا فَتًى يَذْكُرُهُمْ يُقَالُ لَهُ إِبْرَاهِيمُ
Am ñu wax ne : “Déggoon nanu benn waxamaande mu di leen ayibal ; ñu di ko woowe Ibraahiima”.
61قَالُوا فَأْتُوا بِهِ عَلَىٰ أَعْيُنِ النَّاسِ لَعَلَّهُمْ يَشْهَدُونَ
Ñu ne : “Indileen ko ci kanamu nit ñi”, xéy-na ñoom ñu nekki seede [ci loolu].
62قَالُوا أَأَنتَ فَعَلْتَ هَٰذَا بِآلِهَتِنَا يَا إِبْرَاهِيمُ
Ñu ne ko : “Ndax yaw yaa def lii ci sunu yàlla yi, yaw Ibraahiima ? ”
63قَالَ بَلْ فَعَلَهُ كَبِيرُهُمْ هَٰذَا فَاسْأَلُوهُمْ إِن كَانُوا يَنطِقُونَ
Mu ne : “Déedéet, ki ko def mooy ki ci gën a mag ci ñoom. Laajleen ko ndegam mën nañoo wax”.
64فَرَجَعُوا إِلَىٰ أَنفُسِهِمْ فَقَالُوا إِنَّكُمْ أَنتُمُ الظَّالِمُونَ
Ñu dellu ca seeni xel, daldi wax ne : “Nun noo tooñ sunu bopp”.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
62Aaya

Tekki — Al-Anbiya 62

Simoore Al-Anbiya Aaya 62 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne ko : “Ndax yaw yaa def lii ci…

Simoore Aaya 62/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 60–64. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers