Al-Hajj · 20/78
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hajj
يُصْهَرُ بِهِ مَا فِي بُطُونِهِمْ وَالْجُلُودُ ۝٢٠
Yusharu bihee maa fee butoonihim waljulood
📖 Tekkim Wolof
danañu ruyal la nekk ca seen biir ak der ya.

🎧 Dégg


📜 Aaya 18-22 — Simoore Al-Hajj

18أَلَمْ تَرَ أَنَّ اللَّهَ يَسْجُدُ لَهُ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَمَن فِي الْأَرْضِ وَالشَّمْسُ وَالْقَمَرُ وَالنُّجُومُ وَالْجِبَالُ وَالشَّجَرُ وَالدَّوَابُّ وَكَثِيرٌ مِّنَ النَّاسِ ۖ وَكَثِيرٌ حَقَّ عَلَيْهِ الْعَذَابُ ۗ وَمَن يُهِنِ اللَّهُ فَمَا لَهُ مِن مُّكْرِمٍ ۚ إِنَّ اللَّهَ يَفْعَلُ مَا يَشَاءُ ۩
Ndax gisoo ne lépp lu nekk ci suuf si ak asamaan yi mangay sujjóotal Yàlla, ak jant bi ak weer wi ak biddiw yi, ak garab yi ak tundi doj yi, ak way-sujjóot yi ak lu bari ci nit ñi ? Waaye lu bari (ci nit ñi) ñu yeyoo mbugal lañu. Te képp ku Yàlla texeedil kenn du ko mën a teral.
19۞ هَٰذَانِ خَصْمَانِ اخْتَصَمُوا فِي رَبِّهِمْ ۖ فَالَّذِينَ كَفَرُوا قُطِّعَتْ لَهُمْ ثِيَابٌ مِّن نَّارٍ يُصَبُّ مِن فَوْقِ رُءُوسِهِمُ الْحَمِيمُ
Ñaari kurél yooyu di way-xuloo ci seen mbirum Boroom. Ña nga xam ne dañoo weddi, xottileef na leen ay yére yu di Safara, te deefi sotti fi seeni kaw bopp ya ndox mu bax.
20يُصْهَرُ بِهِ مَا فِي بُطُونِهِمْ وَالْجُلُودُ
danañu ruyal la nekk ca seen biir ak der ya.
21وَلَهُم مَّقَامِعُ مِنْ حَدِيدٍ
Ñeel na leen ay bolde yu weñ.
22كُلَّمَا أَرَادُوا أَن يَخْرُجُوا مِنْهَا مِنْ غَمٍّ أُعِيدُوا فِيهَا وَذُوقُوا عَذَابَ الْحَرِيقِ
Saa su fa bëggee génne ca njàqare ja, Nu delloo leen, di leen toqamtikuloo mbugal muy lakke.
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
20Aaya

Tekki — Al-Hajj 20

Simoore Al-Hajj Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : danañu ruyal la nekk ca seen biir ak der ya.

Simoore Aaya 20/78 — Simoore Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hajj Dégg, Simoore Al-Hajj Tekki, Simoore Al-Hajj mp3, Simoore Al-Hajj pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers