Al-Mu'minun · 6/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
إِلَّا عَلَىٰ أَزْوَاجِهِمْ أَوْ مَا مَلَكَتْ أَيْمَانُهُمْ فَإِنَّهُمْ غَيْرُ مَلُومِينَ ۝٦
Illaa `alaaa azwaajihim aw maa malakat aimaanuhum fa innahum ghairu maloomeen
📖 Tekkim Wolof
lu dul ci seeni soxna ak ci seeni jébéer , ñoom dey kenn yejju leen ;

🎧 Dégg


📜 Aaya 4-8 — Simoore Al-Mu'minun

4وَالَّذِينَ هُمْ لِلزَّكَاةِ فَاعِلُونَ
tey génne asaka,
5وَالَّذِينَ هُمْ لِفُرُوجِهِمْ حَافِظُونَ
te mooy gaa ña nga xam ne dañuy sàmm seeni pëy,
6إِلَّا عَلَىٰ أَزْوَاجِهِمْ أَوْ مَا مَلَكَتْ أَيْمَانُهُمْ فَإِنَّهُمْ غَيْرُ مَلُومِينَ
lu dul ci seeni soxna ak ci seeni jébéer , ñoom dey kenn yejju leen ;
7فَمَنِ ابْتَغَىٰ وَرَاءَ ذَٰلِكَ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الْعَادُونَ
ku sàkku leneen ginnaaw loolu nag, ñoom la ñuy tudde way-jalgati ña ;
8وَالَّذِينَ هُمْ لِأَمَانَاتِهِمْ وَعَهْدِهِمْ رَاعُونَ
ña nga xam ne nag dañuy sàmm la ñu leen dénk ak seeni kàddu,
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 6

Simoore Al-Mu'minun Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : lu dul ci seeni soxna ak ci seeni jébéer ,…

Simoore Aaya 6/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers