Al-Mu'minun · 61/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
أُولَٰئِكَ يُسَارِعُونَ فِي الْخَيْرَاتِ وَهُمْ لَهَا سَابِقُونَ ۝٦١
Ulaaa`ika yusaari`oona fil khairaati wa hum lahaa saabiqoon
📖 Tekkim Wolof
Ñooña ñooy jëkkante ci jëfu yiw te jëkk nañu ca.
🎧 Dégg

📜 Aaya 59-63 — Al-Mu'minun

59وَالَّذِينَ هُم بِرَبِّهِمْ لَا يُشْرِكُونَ
ña nga xam ne duñu bokkale seen Boroom ak dara,
60وَالَّذِينَ يُؤْتُونَ مَا آتَوا وَّقُلُوبُهُمْ وَجِلَةٌ أَنَّهُمْ إِلَىٰ رَبِّهِمْ رَاجِعُونَ
ña joxe ca la ñu leen xéewale, te seeni xol di nux-nuxi ci [di xalaat] ne danañu delluwaat ca seen Boroom.
61أُولَٰئِكَ يُسَارِعُونَ فِي الْخَيْرَاتِ وَهُمْ لَهَا سَابِقُونَ
Ñooña ñooy jëkkante ci jëfu yiw te jëkk nañu ca.
62وَلَا نُكَلِّفُ نَفْسًا إِلَّا وُسْعَهَا ۖ وَلَدَيْنَا كِتَابٌ يَنطِقُ بِالْحَقِّ ۚ وَهُمْ لَا يُظْلَمُونَ
Dunu teg benn bakkan lu dul la mu àttan. Te ab Téeree ngi fi buy àtte ci dëgg, te kenn du leen ca noonu [ci waññi yiw walla yokk safaan].
63بَلْ قُلُوبُهُمْ فِي غَمْرَةٍ مِّنْ هَٰذَا وَلَهُمْ أَعْمَالٌ مِّن دُونِ ذَٰلِكَ هُمْ لَهَا عَامِلُونَ
Waaye seeni xol réere na lii [di Alxuraan]. Te am nañu ay jëf yu yées yooyu te ña nga koy jëf,
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
61Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 61

Simoore Al-Mu'minun Aaya 61 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñooña ñooy jëkkante ci jëfu yiw te jëkk nañu ca.

Simoore Aaya 61/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 59–63. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers