Al-Furqan · 22/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
يَوْمَ يَرَوْنَ الْمَلَائِكَةَ لَا بُشْرَىٰ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُجْرِمِينَ وَيَقُولُونَ حِجْرًا مَّحْجُورًا ۝٢٢
Yawma yarawnal malaaa `ikata laa bushraa Yawma`izil lilmujrimeena wa yaqooloona hijram mahjooraa
📖 Tekkim Wolof
Bis ba ñuy mën a gis malaaka ya du neex ci ñoom de, ndax Malaaka yaa nga naan leen : “Seeni mbir sakk na” !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 20-24 — Simoore Al-Furqan

20وَمَا أَرْسَلْنَا قَبْلَكَ مِنَ الْمُرْسَلِينَ إِلَّا إِنَّهُمْ لَيَأْكُلُونَ الطَّعَامَ وَيَمْشُونَ فِي الْأَسْوَاقِ ۗ وَجَعَلْنَا بَعْضَكُمْ لِبَعْضٍ فِتْنَةً أَتَصْبِرُونَ ۗ وَكَانَ رَبُّكَ بَصِيرًا
Musunoo yebal ay Yonent ca la la jiitu lu dul dañu daan lekk ñam te di dox ci ja yi [màrse yi]. Def Nanu it ñenn ci yéen di sànjeb ña ca des, mbaa dangeen muñ ? - Sa Boroom de kuy gis la.
21۞ وَقَالَ الَّذِينَ لَا يَرْجُونَ لِقَاءَنَا لَوْلَا أُنزِلَ عَلَيْنَا الْمَلَائِكَةُ أَوْ نَرَىٰ رَبَّنَا ۗ لَقَدِ اسْتَكْبَرُوا فِي أَنفُسِهِمْ وَعَتَوْا عُتُوًّا كَبِيرًا
Ña yaakaarul a dajeek Nun ñangay wax naan : “Céy bées wàcce woon ci nun ay Malaaka, mbaa nu gis sunu Boroom [Yàlla] ! ”. Dañu doon rëy-rëylu [kaweel seen bopp], réer réer gu jéggi dayo.
22يَوْمَ يَرَوْنَ الْمَلَائِكَةَ لَا بُشْرَىٰ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُجْرِمِينَ وَيَقُولُونَ حِجْرًا مَّحْجُورًا
Bis ba ñuy mën a gis malaaka ya du neex ci ñoom de, ndax Malaaka yaa nga naan leen : “Seeni mbir sakk na” !
23وَقَدِمْنَا إِلَىٰ مَا عَمِلُوا مِنْ عَمَلٍ فَجَعَلْنَاهُ هَبَاءً مَّنثُورًا
Nu fab jépp jëf ju ñu mësoon a jëf, def ko pënd bu ñu wasaare.
24أَصْحَابُ الْجَنَّةِ يَوْمَئِذٍ خَيْرٌ مُّسْتَقَرًّا وَأَحْسَنُ مَقِيلًا
[Bu keroogee Bis-pénc ba], waa Àjjana ñooy gën delluwaay te ñooy dàq ub nooflaay.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
22Aaya

Tekki — Al-Furqan 22

Simoore Al-Furqan Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bis ba ñuy mën a gis malaaka ya du neex…

Simoore Aaya 22/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers