Ash-Shu'ara · 118/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
فَافْتَحْ بَيْنِي وَبَيْنَهُمْ فَتْحًا وَنَجِّنِي وَمَن مَّعِيَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ ١١٨
Transliteration
Faftab bainee wa bai nahum fat hanw wa najjinee wa mam ma`iya minal mu`mineen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Àtteel sama digganteek ñoom ba mu ne làññ : te nga musal maak ñi ma àndal te ñu bokk ca ña gëm”.
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 116-120 — Simoore Ash-Shu'ara
116قَالُوا لَئِن لَّمْ تَنتَهِ يَا نُوحُ لَتَكُونَنَّ مِنَ الْمَرْجُومِينَ
Ñu ne ko : “Yaw Nooh, soo bàyyiwul li nga nekk, dees na la jóori xeer [ba nga dee] ! ”
117قَالَ رَبِّ إِنَّ قَوْمِي كَذَّبُونِ
Mu ne : “Yaw sama Boroom, samaw nit weddi nañu, jàppe ma fenkat.
118فَافْتَحْ بَيْنِي وَبَيْنَهُمْ فَتْحًا وَنَجِّنِي وَمَن مَّعِيَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ
Àtteel sama digganteek ñoom ba mu ne làññ : te nga musal maak ñi ma àndal te ñu bokk ca ña gëm”.
119فَأَنجَيْنَاهُ وَمَن مَّعَهُ فِي الْفُلْكِ الْمَشْحُونِ
Nu daldi koy musal mook ña mu àndaloon ci gaal ga mu duyyoon ba mu fees.
120ثُمَّ أَغْرَقْنَا بَعْدُ الْبَاقِينَ
Ginnaaw ba, Nu labal ña ca des.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
118Aaya
Tekki — Ash-Shu'ara 118
Simoore Ash-Shu'ara Aaya 118 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Àtteel sama digganteek ñoom ba mu ne làññ : te…Simoore Aaya 118/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 116–120. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Ash-Shu'ara
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Saturday, October 3, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


