Ash-Shu'ara · 117/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
قَالَ رَبِّ إِنَّ قَوْمِي كَذَّبُونِ ۝١١٧
Qaala Rabbi inna qawmee kazzaboon
📖 Tekkim Wolof
Mu ne : “Yaw sama Boroom, samaw nit weddi nañu, jàppe ma fenkat.
🎧 Dégg

📜 Aaya 115-119 — Ash-Shu'ara

115إِنْ أَنَا إِلَّا نَذِيرٌ مُّبِينٌ
Man doonuma lu dul ab xuppekat bu bir”.
116قَالُوا لَئِن لَّمْ تَنتَهِ يَا نُوحُ لَتَكُونَنَّ مِنَ الْمَرْجُومِينَ
Ñu ne ko : “Yaw Nooh, soo bàyyiwul li nga nekk, dees na la jóori xeer [ba nga dee] ! ”
117قَالَ رَبِّ إِنَّ قَوْمِي كَذَّبُونِ
Mu ne : “Yaw sama Boroom, samaw nit weddi nañu, jàppe ma fenkat.
118فَافْتَحْ بَيْنِي وَبَيْنَهُمْ فَتْحًا وَنَجِّنِي وَمَن مَّعِيَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ
Àtteel sama digganteek ñoom ba mu ne làññ : te nga musal maak ñi ma àndal te ñu bokk ca ña gëm”.
119فَأَنجَيْنَاهُ وَمَن مَّعَهُ فِي الْفُلْكِ الْمَشْحُونِ
Nu daldi koy musal mook ña mu àndaloon ci gaal ga mu duyyoon ba mu fees.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
117Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 117

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 117 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne : “Yaw sama Boroom, samaw nit weddi nañu,…

Simoore Aaya 117/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 115–119. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers