Ash-Shu'ara · 138/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَمَا نَحْنُ بِمُعَذَّبِينَ ۝١٣٨
Wa maa nahnu bimu `azzabeen
📖 Tekkim Wolof
Nun daal, kenn dunu mbugal”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 136-140 — Simoore Ash-Shu'ara

136قَالُوا سَوَاءٌ عَلَيْنَا أَوَعَظْتَ أَمْ لَمْ تَكُن مِّنَ الْوَاعِظِينَ
Ñu tontu wax ne : “Nga di nu waar ak nga ñàkk noo war a yem ci nun képp !
137إِنْ هَٰذَا إِلَّا خُلُقُ الْأَوَّلِينَ
Lii daal du lenn lu dul jikkoy mag ñu jëkk ña :
138وَمَا نَحْنُ بِمُعَذَّبِينَ
Nun daal, kenn dunu mbugal”.
139فَكَذَّبُوهُ فَأَهْلَكْنَاهُمْ ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ
Ñu weddi ko. Nu daldi leen mbugal. Te ca biir, ay kéemaan a nga ca ! Te taxul la ëpp ca ñoom gëm.
140وَإِنَّ رَبَّكَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
Te sa Boroom, moo di Boroom kàttan, di Jaglewaakoon.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
138Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 138

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 138 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun daal, kenn dunu mbugal”.

Simoore Aaya 138/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 136–140. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers