Ash-Shu'ara · 198/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَلَوْ نَزَّلْنَاهُ عَلَىٰ بَعْضِ الْأَعْجَمِينَ ۝١٩٨
Wa law nazzalnaahu `alaa ba`dil a`jameen
📖 Tekkim Wolof
Su Nu ko wàcce woon ci ku dul ab araab,

🎧 Dégg


📜 Aaya 196-200 — Simoore Ash-Shu'ara

196وَإِنَّهُ لَفِي زُبُرِ الْأَوَّلِينَ
Te nekkoon na ca biir Téerey Yonent yu njëkk ya.
197أَوَلَمْ يَكُن لَّهُمْ آيَةً أَن يَعْلَمَهُ عُلَمَاءُ بَنِي إِسْرَائِيلَ
Ndax amuñu woon ay kéemaan yu taxoon boroom xam-xami giir Banii-Israayiila xamoon ko ?
198وَلَوْ نَزَّلْنَاهُ عَلَىٰ بَعْضِ الْأَعْجَمِينَ
Su Nu ko wàcce woon ci ku dul ab araab,
199فَقَرَأَهُ عَلَيْهِم مَّا كَانُوا بِهِ مُؤْمِنِينَ
mu jàngal leen ko, du tax kon ngeen gëm ko.
200كَذَٰلِكَ سَلَكْنَاهُ فِي قُلُوبِ الْمُجْرِمِينَ
Noonu it la nu dugalee jiixi-jaaxa ca biir xoli tooñkat yi ba gëmuñu ko ;
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
198Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 198

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 198 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Su Nu ko wàcce woon ci ku dul ab araab,

Simoore Aaya 198/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 196–200. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers