Ash-Shu'ara · 210/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَمَا تَنَزَّلَتْ بِهِ الشَّيَاطِينُ ۝٢١٠
Wa maa tanazzalat bihish Shayaateen
📖 Tekkim Wolof
Alxuraan jii, séytaane yi wàccewuñu ko de :

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 208-212 — Simoore Ash-Shu'ara

208وَمَا أَهْلَكْنَا مِن قَرْيَةٍ إِلَّا لَهَا مُنذِرُونَ
Amul benn dëkk bu Nu mës a alag u nitam te yónneewunu fa woon ay xuppekat,
209ذِكْرَىٰ وَمَا كُنَّا ظَالِمِينَ
di fàttali rekk, tooñunu kenn.
210وَمَا تَنَزَّلَتْ بِهِ الشَّيَاطِينُ
Alxuraan jii, séytaane yi wàccewuñu ko de :
211وَمَا يَنبَغِي لَهُمْ وَمَا يَسْتَطِيعُونَ
Amuñu ko, mënuñu ko.
212إِنَّهُمْ عَنِ السَّمْعِ لَمَعْزُولُونَ
Ñoom mënuñoo dégg ndigali Yàlla.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
210Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 210

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 210 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Alxuraan jii, séytaane yi wàccewuñu ko de :

Simoore Aaya 210/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 208–212. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers