Ash-Shu'ara · 23/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
قَالَ فِرْعَوْنُ وَمَا رَبُّ الْعَالَمِينَ ٢٣
Transliteration
Qaala Fir`awnu wa maa Rabbul `aalameen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
[Firawna] ne ko : “Waaw, ana kan mooy Boroom àddina si ? ”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 21-25 — Simoore Ash-Shu'ara
21فَفَرَرْتُ مِنكُمْ لَمَّا خِفْتُكُمْ فَوَهَبَ لِي رَبِّي حُكْمًا وَجَعَلَنِي مِنَ الْمُرْسَلِينَ
Ma daldi daw ba ma tiitee : faf Yàlla jox ma xam-xamu [baatin], def ma ma bokk ca Yonent ya.
22وَتِلْكَ نِعْمَةٌ تَمُنُّهَا عَلَيَّ أَنْ عَبَّدتَّ بَنِي إِسْرَائِيلَ
Te loolu xéewal la goo may mën a xéewale, ndax liggéeyloo nga giir Banii-Israayil lu ne ? ”
23قَالَ فِرْعَوْنُ وَمَا رَبُّ الْعَالَمِينَ
[Firawna] ne ko : “Waaw, ana kan mooy Boroom àddina si ? ”.
24قَالَ رَبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا ۖ إِن كُنتُم مُّوقِنِينَ
[Muusaa ne ko] : “Mooy Boroom asamaan yeek suuf si ak li nekk seen diggante, ndegam wóolu nga ! ”
25قَالَ لِمَنْ حَوْلَهُ أَلَا تَسْتَمِعُونَ
[Firawna] daldi wax ak ña ko wëroon, ne leen : “Gaa ñi xanaa dégguleen ? ”
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
23Aaya
Tekki — Ash-Shu'ara 23
Simoore Ash-Shu'ara Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Firawna] ne ko : “Waaw, ana kan mooy Boroom àddina…Simoore Aaya 23/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, September 8, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








