Ash-Shu'ara · 43/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
قَالَ لَهُم مُّوسَىٰ أَلْقُوا مَا أَنتُم مُّلْقُونَ ۝٤٣
Qaala lahum Moosaaa alqoo maaa antum mulqoon
📖 Tekkim Wolof
Muusaa ne leen : “Sànnileen li ngeen di sànni”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 41-45 — Ash-Shu'ara

41فَلَمَّا جَاءَ السَّحَرَةُ قَالُوا لِفِرْعَوْنَ أَئِنَّ لَنَا لَأَجْرًا إِن كُنَّا نَحْنُ الْغَالِبِينَ
Ba jibar ya agsee, dellu wax Firawna ne ko : “Ndax dananu am ag pey bu fekkee ne not nanu [Muusaa] ? ”
42قَالَ نَعَمْ وَإِنَّكُمْ إِذًا لَّمِنَ الْمُقَرَّبِينَ
Mu ne leen : “Waawaaw, kon dingeen bokk ci samay jegeñaale !
43قَالَ لَهُم مُّوسَىٰ أَلْقُوا مَا أَنتُم مُّلْقُونَ
Muusaa ne leen : “Sànnileen li ngeen di sànni”.
44فَأَلْقَوْا حِبَالَهُمْ وَعِصِيَّهُمْ وَقَالُوا بِعِزَّةِ فِرْعَوْنَ إِنَّا لَنَحْنُ الْغَالِبُونَ
Ñu daldi sànni seen buum ak i yet, daldi wax ne : “Ci doole Firawna la nuy note”.
45فَأَلْقَىٰ مُوسَىٰ عَصَاهُ فَإِذَا هِيَ تَلْقَفُ مَا يَأْفِكُونَ
Muusaa daldi sànni yetam wa, ndeketeyoo mëdd na ya ñu deferoon.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
43Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 43

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 43 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Muusaa ne leen : “Sànnileen li ngeen di sànni”.

Simoore Aaya 43/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 41–45. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers