Ash-Shu'ara · 44/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
فَأَلْقَوْا حِبَالَهُمْ وَعِصِيَّهُمْ وَقَالُوا بِعِزَّةِ فِرْعَوْنَ إِنَّا لَنَحْنُ الْغَالِبُونَ ٤٤
Transliteration
Fa alqaw hibaalahum wa `isiyyahum wa qaaloo bi`izzati Fir`awna innaa lanahnul ghaaliboon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñu daldi sànni seen buum ak i yet, daldi wax ne : “Ci doole Firawna la nuy note”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 42-46 — Ash-Shu'ara
42قَالَ نَعَمْ وَإِنَّكُمْ إِذًا لَّمِنَ الْمُقَرَّبِينَ
Mu ne leen : “Waawaaw, kon dingeen bokk ci samay jegeñaale !
43قَالَ لَهُم مُّوسَىٰ أَلْقُوا مَا أَنتُم مُّلْقُونَ
Muusaa ne leen : “Sànnileen li ngeen di sànni”.
44فَأَلْقَوْا حِبَالَهُمْ وَعِصِيَّهُمْ وَقَالُوا بِعِزَّةِ فِرْعَوْنَ إِنَّا لَنَحْنُ الْغَالِبُونَ
Ñu daldi sànni seen buum ak i yet, daldi wax ne : “Ci doole Firawna la nuy note”.
45فَأَلْقَىٰ مُوسَىٰ عَصَاهُ فَإِذَا هِيَ تَلْقَفُ مَا يَأْفِكُونَ
Muusaa daldi sànni yetam wa, ndeketeyoo mëdd na ya ñu deferoon.
46فَأُلْقِيَ السَّحَرَةُ سَاجِدِينَ
Jibar ya daldi rot sujjóot,
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
44Aaya
Tekki — Ash-Shu'ara 44
Simoore Ash-Shu'ara Aaya 44 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu daldi sànni seen buum ak i yet, daldi wax…Simoore Aaya 44/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 42–46. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








