Ash-Shu'ara · 73/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
أَوْ يَنفَعُونَكُمْ أَوْ يَضُرُّونَ ۝٧٣
Aw yanfa`oonakum aw yadurroon
📖 Tekkim Wolof
walla ñu di leen jariñ mbaa ñu leen di lor ? ”

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 71-75 — Simoore Ash-Shu'ara

71قَالُوا نَعْبُدُ أَصْنَامًا فَنَظَلُّ لَهَا عَاكِفِينَ
Ñu ne ko : “Ay xërëm lanuy jaamu, te gëm ko lool”.
72قَالَ هَلْ يَسْمَعُونَكُمْ إِذْ تَدْعُونَ
Ibraahiima ne leen : “Ndax danañu leen dégg bu ngeen leen di woo ?
73أَوْ يَنفَعُونَكُمْ أَوْ يَضُرُّونَ
walla ñu di leen jariñ mbaa ñu leen di lor ? ”
74قَالُوا بَلْ وَجَدْنَا آبَاءَنَا كَذَٰلِكَ يَفْعَلُونَ
Ñu wax ne : “Nun kat, dañoo fekk rekk sunuy baay daan ko def”.
75قَالَ أَفَرَأَيْتُم مَّا كُنتُمْ تَعْبُدُونَ
Ibraahiima ne leen : “Xanaa gisuleen li ngeen di jaamu... ?
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
73Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 73

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 73 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : walla ñu di leen jariñ mbaa ñu leen di lor…

Simoore Aaya 73/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 71–75. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers