Ash-Shu'ara · 93/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
مِن دُونِ اللَّهِ هَلْ يَنصُرُونَكُمْ أَوْ يَنتَصِرُونَ ۝٩٣
Min doonil laahi hal yansuroonakum aw yantasiroon
📖 Tekkim Wolof
bàyyi woon Yàlla ? Ndax mën nanoo dimbali seen bopp ? Walla ñu dimbali leen ? ”
🎧 Dégg

📜 Aaya 91-95 — Ash-Shu'ara

91وَبُرِّزَتِ الْجَحِيمُ لِلْغَاوِينَ
te gaaraleef na Safara ñeel ña béewoon,
92وَقِيلَ لَهُمْ أَيْنَ مَا كُنتُمْ تَعْبُدُونَ
Ñu wax leen ne : “Ana fan ngeen nekkoon di fa jaamoo,
93مِن دُونِ اللَّهِ هَلْ يَنصُرُونَكُمْ أَوْ يَنتَصِرُونَ
bàyyi woon Yàlla ? Ndax mën nanoo dimbali seen bopp ? Walla ñu dimbali leen ? ”
94فَكُبْكِبُوا فِيهَا هُمْ وَالْغَاوُونَ
Ñu sànni leen fa, galajaane leen ñook mboxos ma,
95وَجُنُودُ إِبْلِيسَ أَجْمَعُونَ
ak gàngoorug Ibliis ga gépp.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
93Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 93

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 93 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : bàyyi woon Yàlla ? Ndax mën nanoo dimbali seen bopp…

Simoore Aaya 93/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 91–95. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers