Aali Imran · 108/200
Tekki Waxtaan — Simoore Aali Imran
تِلْكَ آيَاتُ اللَّهِ نَتْلُوهَا عَلَيْكَ بِالْحَقِّ ۗ وَمَا اللَّهُ يُرِيدُ ظُلْمًا لِّلْعَالَمِينَ ۝١٠٨
Tilka Aayaatul laahi natloohaa `alaika bilhaqq; wa mal laahu yureedu zulmallil `aalameen
📖 Tekkim Wolof
Loolu moo di kàdduy Yàlla ya ; Danañu ko jàngat ci yaw (Muhammad) ci dëgg. Yàlla nammul di tooñ mbindéef yi.

🎧 Dégg


📜 Aaya 106-110 — Simoore Aali Imran

106يَوْمَ تَبْيَضُّ وُجُوهٌ وَتَسْوَدُّ وُجُوهٌ ۚ فَأَمَّا الَّذِينَ اسْوَدَّتْ وُجُوهُهُمْ أَكَفَرْتُم بَعْدَ إِيمَانِكُمْ فَذُوقُوا الْعَذَابَ بِمَا كُنتُمْ تَكْفُرُونَ
Bis ba ay xar-kanam di weex tàll, ay xar-kanam it di ñuul kukk, ña nga xam ne seeni kanam dana ñuul [dana ñu leen wax] ne: “Ndax dangeen weddi gannaaw ba ngeen gëmee ? ”. Mosleen, toqamtikuleen mbugal mii ci sababus li ngeen doon weddi.
107وَأَمَّا الَّذِينَ ابْيَضَّتْ وُجُوهُهُمْ فَفِي رَحْمَةِ اللَّهِ هُمْ فِيهَا خَالِدُونَ
Ña nga xam ne seeni kanam ya dafa weex, dana ñu nekk ci yërmaandey Yàlla, te dañu fay béel.
108تِلْكَ آيَاتُ اللَّهِ نَتْلُوهَا عَلَيْكَ بِالْحَقِّ ۗ وَمَا اللَّهُ يُرِيدُ ظُلْمًا لِّلْعَالَمِينَ
Loolu moo di kàdduy Yàlla ya ; Danañu ko jàngat ci yaw (Muhammad) ci dëgg. Yàlla nammul di tooñ mbindéef yi.
109وَلِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۚ وَإِلَى اللَّهِ تُرْجَعُ الْأُمُورُ
Yàllaa moom li nekk ci asamaan yi ak suuf si. Te mbir yépp ca Yàlla lañuy mujj [dellusi].
110كُنتُمْ خَيْرَ أُمَّةٍ أُخْرِجَتْ لِلنَّاسِ تَأْمُرُونَ بِالْمَعْرُوفِ وَتَنْهَوْنَ عَنِ الْمُنكَرِ وَتُؤْمِنُونَ بِاللَّهِ ۗ وَلَوْ آمَنَ أَهْلُ الْكِتَابِ لَكَانَ خَيْرًا لَّهُم ۚ مِّنْهُمُ الْمُؤْمِنُونَ وَأَكْثَرُهُمُ الْفَاسِقُونَ
Yéen yéen ay xeet wi gën ci nit ñi [xeet wu fi mës a jaar]. Yéen ay digle njekk te tere njekkar te gëm Yàlla. Bu ñoñ-téere gëmoon, mooy gën ci ñoom de, li ëpp ci ñoom ay saay- saay lañu.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
108Aaya

Tekki — Aali Imran 108

Simoore Aali Imran Aaya 108 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Loolu moo di kàdduy Yàlla ya ; Danañu ko jàngat…

Simoore Aaya 108/200 — Simoore Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Aali Imran Dégg, Simoore Aali Imran Tekki, Simoore Aali Imran mp3, Simoore Aali Imran pdf. Aaya 106–110. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers