Aali Imran · 25/200
Tekki Waxtaan — Simoore Aali Imran
فَكَيْفَ إِذَا جَمَعْنَاهُمْ لِيَوْمٍ لَّا رَيْبَ فِيهِ وَوُفِّيَتْ كُلُّ نَفْسٍ مَّا كَسَبَتْ وَهُمْ لَا يُظْلَمُونَ ۝٢٥
Fakaifa izaa jama`naahum li Yawmil laa raiba fee wa wuffiyat kullu nafsim maa kasabat wa hum laa yuzlamoon
📖 Tekkim Wolof
Naka la ñuy def ca bis ba, kenn warut a nàttable ci ne dana am, bu ñu leen dajalee ba kenn ku nekk ñu jox ko la mu fàggu woon mu mat sëkk.

🎧 Dégg


📜 Aaya 23-27 — Simoore Aali Imran

23أَلَمْ تَرَ إِلَى الَّذِينَ أُوتُوا نَصِيبًا مِّنَ الْكِتَابِ يُدْعَوْنَ إِلَىٰ كِتَابِ اللَّهِ لِيَحْكُمَ بَيْنَهُمْ ثُمَّ يَتَوَلَّىٰ فَرِيقٌ مِّنْهُمْ وَهُم مُّعْرِضُونَ
Moo ndax gisoo ñañu jox cér ca téere ba , woowees na leen jëme ci Téere Yàlla bi ngir mu àtte seeni diggante ; am kurél ci ñoom bu dummóoyu, far ñoom ñépp dummóoyu.
24ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ قَالُوا لَن تَمَسَّنَا النَّارُ إِلَّا أَيَّامًا مَّعْدُودَاتٍ ۖ وَغَرَّهُمْ فِي دِينِهِم مَّا كَانُوا يَفْتَرُونَ
Ndax ñoom dañuy wax ne : “Safara dunu laal lu dul ay bis yuñu lim”. Dañuy duural Yàlla ci seen diine, loolaa leen nax.
25فَكَيْفَ إِذَا جَمَعْنَاهُمْ لِيَوْمٍ لَّا رَيْبَ فِيهِ وَوُفِّيَتْ كُلُّ نَفْسٍ مَّا كَسَبَتْ وَهُمْ لَا يُظْلَمُونَ
Naka la ñuy def ca bis ba, kenn warut a nàttable ci ne dana am, bu ñu leen dajalee ba kenn ku nekk ñu jox ko la mu fàggu woon mu mat sëkk.
26قُلِ اللَّهُمَّ مَالِكَ الْمُلْكِ تُؤْتِي الْمُلْكَ مَن تَشَاءُ وَتَنزِعُ الْمُلْكَ مِمَّن تَشَاءُ وَتُعِزُّ مَن تَشَاءُ وَتُذِلُّ مَن تَشَاءُ ۖ بِيَدِكَ الْخَيْرُ ۖ إِنَّكَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
- Neel : “Sama Boroom, Yaw miy Boroom nguur. Yaay jox nguur ku la soob, di rocci nguur ci ku la soob ; Yaay teral ku la soob, Yaay toroxal ku la soob. Yiw wépp a ngi ci sa loxo te kàttanu nga ci def lu ne.
27تُولِجُ اللَّيْلَ فِي النَّهَارِ وَتُولِجُ النَّهَارَ فِي اللَّيْلِ ۖ وَتُخْرِجُ الْحَيَّ مِنَ الْمَيِّتِ وَتُخْرِجُ الْمَيِّتَ مِنَ الْحَيِّ ۖ وَتَرْزُقُ مَن تَشَاءُ بِغَيْرِ حِسَابٍ
Yaay dugal guddi ci bëccëg, Yaay dugal bëccëg ci guddi, Yaay génne ndundu ci ndee, Yaay génne ndee ci ndundu. Di wërsëgal ku la soob ci lu àndul ak waññi”.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
25Aaya

Tekki — Aali Imran 25

Simoore Aali Imran Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Naka la ñuy def ca bis ba, kenn warut a…

Simoore Aaya 25/200 — Simoore Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Aali Imran Dégg, Simoore Aali Imran Tekki, Simoore Aali Imran mp3, Simoore Aali Imran pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers