Aali Imran · 90/200
Tekki Waxtaan — Aali Imran
إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا بَعْدَ إِيمَانِهِمْ ثُمَّ ازْدَادُوا كُفْرًا لَّن تُقْبَلَ تَوْبَتُهُمْ وَأُولَٰئِكَ هُمُ الضَّالُّونَ ۝٩٠
Innal lazeena kafaroo ba`da eemaanihim summaz daadoo kufral lan tuqbala tawbatuhum wa ulaaa`ika humud daaalloon
📖 Tekkim Wolof
Ña nga xam ne dañoo weddi ginnaaw ba ñu gëmee ba dee ci kéefar, deesuleen nangul seenug tuub. Te ñoom ñooy gaa ya sànku .
🎧 Dégg

📜 Aaya 88-92 — Aali Imran

88خَالِدِينَ فِيهَا لَا يُخَفَّفُ عَنْهُمُ الْعَذَابُ وَلَا هُمْ يُنظَرُونَ
Dañu fay béel ca Safara. Kenn duleen woyafal mbugal ma, kenn duleen ko yéexalal,
89إِلَّا الَّذِينَ تَابُوا مِن بَعْدِ ذَٰلِكَ وَأَصْلَحُوا فَإِنَّ اللَّهَ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
lu dul ña tuub ginnaaw loola te sellal seeni jëf. : Yàlla Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
90إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا بَعْدَ إِيمَانِهِمْ ثُمَّ ازْدَادُوا كُفْرًا لَّن تُقْبَلَ تَوْبَتُهُمْ وَأُولَٰئِكَ هُمُ الضَّالُّونَ
Ña nga xam ne dañoo weddi ginnaaw ba ñu gëmee ba dee ci kéefar, deesuleen nangul seenug tuub. Te ñoom ñooy gaa ya sànku .
91إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا وَمَاتُوا وَهُمْ كُفَّارٌ فَلَن يُقْبَلَ مِنْ أَحَدِهِم مِّلْءُ الْأَرْضِ ذَهَبًا وَلَوِ افْتَدَىٰ بِهِ ۗ أُولَٰئِكَ لَهُمْ عَذَابٌ أَلِيمٌ وَمَا لَهُم مِّن نَّاصِرِينَ
Ña nga xam ne ñoo weddi ba dee ci kéefar, deesul nangul kenn ci ñoom mu jote doonte la joxe na wurus wu fees dell suuf si ngir loolu [jote]. Ñooñee, mbugal mu tar lañuy am, te duñu am ku leen dimbali.
92لَن تَنَالُوا الْبِرَّ حَتَّىٰ تُنفِقُوا مِمَّا تُحِبُّونَ ۚ وَمَا تُنفِقُوا مِن شَيْءٍ فَإِنَّ اللَّهَ بِهِ عَلِيمٌ
Dungeen am mbaax ba ba ngeen di joxe ci li ngeen bëgg. Te lépp lu ngeen mën a joxe, Yàlla xam na ko.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
90Aaya

Tekki — Aali Imran 90

Simoore Aali Imran Aaya 90 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña nga xam ne dañoo weddi ginnaaw ba ñu gëmee…

Simoore Aaya 90/200 — Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Aali Imran Dégg, Aali Imran Tekki, Aali Imran mp3, Aali Imran pdf. Aaya 88–92. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers