As-Saffat · 116/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَنَصَرْنَاهُمْ فَكَانُوا هُمُ الْغَالِبِينَ ۝١١٦
Wa nasarnaahum fakaanoo humul ghaalibeen
📖 Tekkim Wolof
Nu dimbali woon leen, ñoom ñoo nootoon.

🎧 Dégg


📜 Aaya 114-118 — Simoore As-Saffat

114وَلَقَدْ مَنَنَّا عَلَىٰ مُوسَىٰ وَهَارُونَ
Xéewaloon Nanu Muusaa ak Haaruuna,
115وَنَجَّيْنَاهُمَا وَقَوْمَهُمَا مِنَ الْكَرْبِ الْعَظِيمِ
Musaloon Nanu leen ñoom seeni sët ca tiit mu rëy ma,
116وَنَصَرْنَاهُمْ فَكَانُوا هُمُ الْغَالِبِينَ
Nu dimbali woon leen, ñoom ñoo nootoon.
117وَآتَيْنَاهُمَا الْكِتَابَ الْمُسْتَبِينَ
Nu indiloon leen ab téere bu bir
118وَهَدَيْنَاهُمَا الصِّرَاطَ الْمُسْتَقِيمَ
Nu indiloon leen yoon wu jub wa xocc.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
116Aaya

Tekki — As-Saffat 116

Simoore As-Saffat Aaya 116 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu dimbali woon leen, ñoom ñoo nootoon.

Simoore Aaya 116/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 114–118. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers