As-Saffat · 148/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فَآمَنُوا فَمَتَّعْنَاهُمْ إِلَىٰ حِينٍ ۝١٤٨
Fa aamanoo famatta` naahum ilaa heen
📖 Tekkim Wolof
Ba ñu gëmee, xéewalal Nanu leen fa ab diir.

🎧 Dégg


📜 Aaya 146-150 — Simoore As-Saffat

146وَأَنبَتْنَا عَلَيْهِ شَجَرَةً مِّن يَقْطِينٍ
Nu daldi fay saxal gàncaxug beraf,
147وَأَرْسَلْنَاهُ إِلَىٰ مِائَةِ أَلْفٍ أَوْ يَزِيدُونَ
Nu yebal ko muy Yonent ci téeméeri junniy nit mbaa lu ko ëpp.
148فَآمَنُوا فَمَتَّعْنَاهُمْ إِلَىٰ حِينٍ
Ba ñu gëmee, xéewalal Nanu leen fa ab diir.
149فَاسْتَفْتِهِمْ أَلِرَبِّكَ الْبَنَاتُ وَلَهُمُ الْبَنُونَ
Laajleen baxam : “Ndax Yàlla moo ame doom yu jigéen, ñoom ñuy am doom yu góor ?
150أَمْ خَلَقْنَا الْمَلَائِكَةَ إِنَاثًا وَهُمْ شَاهِدُونَ
Walla dañoo bind Malaaka yi def leen ñu di ay jigéen, seere ko ? ”.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
148Aaya

Tekki — As-Saffat 148

Simoore As-Saffat Aaya 148 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba ñu gëmee, xéewalal Nanu leen fa ab diir.

Simoore Aaya 148/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 146–150. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers