As-Saffat · 149/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فَاسْتَفْتِهِمْ أَلِرَبِّكَ الْبَنَاتُ وَلَهُمُ الْبَنُونَ ۝١٤٩
Fastaftihim ali Rabbikal banaatu wa lahumul banoon
📖 Tekkim Wolof
Laajleen baxam : “Ndax Yàlla moo ame doom yu jigéen, ñoom ñuy am doom yu góor ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 147-151 — Simoore As-Saffat

147وَأَرْسَلْنَاهُ إِلَىٰ مِائَةِ أَلْفٍ أَوْ يَزِيدُونَ
Nu yebal ko muy Yonent ci téeméeri junniy nit mbaa lu ko ëpp.
148فَآمَنُوا فَمَتَّعْنَاهُمْ إِلَىٰ حِينٍ
Ba ñu gëmee, xéewalal Nanu leen fa ab diir.
149فَاسْتَفْتِهِمْ أَلِرَبِّكَ الْبَنَاتُ وَلَهُمُ الْبَنُونَ
Laajleen baxam : “Ndax Yàlla moo ame doom yu jigéen, ñoom ñuy am doom yu góor ?
150أَمْ خَلَقْنَا الْمَلَائِكَةَ إِنَاثًا وَهُمْ شَاهِدُونَ
Walla dañoo bind Malaaka yi def leen ñu di ay jigéen, seere ko ? ”.
151أَلَا إِنَّهُم مِّنْ إِفْكِهِمْ لَيَقُولُونَ
Ndax ñoom dañuy faral di wax ci seen duur ya, naan :
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
149Aaya

Tekki — As-Saffat 149

Simoore As-Saffat Aaya 149 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Laajleen baxam : “Ndax Yàlla moo ame doom yu jigéen,…

Simoore Aaya 149/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 147–151. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers