As-Saffat · 158/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَجَعَلُوا بَيْنَهُ وَبَيْنَ الْجِنَّةِ نَسَبًا ۚ وَلَقَدْ عَلِمَتِ الْجِنَّةُ إِنَّهُمْ لَمُحْضَرُونَ ۝١٥٨
Wa ja`aloo bainahoo wa bainal jinnati nasabaa; wa laqad `alimatil jinnatu innahum lamuhdaroon
📖 Tekkim Wolof
Ñu di ko askanale ci jinne yi, ndax jinne yi xam nañu ne danañu teew ci kanamu [Yàlla].

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 156-160 — Simoore As-Saffat

156أَمْ لَكُمْ سُلْطَانٌ مُّبِينٌ
Walla dangeen am ay firnde yu wóor ?
157فَأْتُوا بِكِتَابِكُمْ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Kon indil seenub Téere ndegam ñu dëggu ngeen ! ”
158وَجَعَلُوا بَيْنَهُ وَبَيْنَ الْجِنَّةِ نَسَبًا ۚ وَلَقَدْ عَلِمَتِ الْجِنَّةُ إِنَّهُمْ لَمُحْضَرُونَ
Ñu di ko askanale ci jinne yi, ndax jinne yi xam nañu ne danañu teew ci kanamu [Yàlla].
159سُبْحَانَ اللَّهِ عَمَّا يَصِفُونَ
Tudd naa sellug Yàlla ga. Kawe na lool la ñu koy melal !
160إِلَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ
Ba mu des jaami Yàlla yiy sellal.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
158Aaya

Tekki — As-Saffat 158

Simoore As-Saffat Aaya 158 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu di ko askanale ci jinne yi, ndax jinne yi…

Simoore Aaya 158/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 156–160. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Sunday, October 4, 2026

Don't forget us in your sincere prayers