As-Saffat · 86/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
أَئِفْكًا آلِهَةً دُونَ اللَّهِ تُرِيدُونَ ٨٦
Transliteration
A`ifkan aalihatan doonal laahi tureedoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax ay nar ngeen di namm a def ay yàlla bàyyi Yàlla Moom ?
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 84-88 — Simoore As-Saffat
84إِذْ جَاءَ رَبَّهُ بِقَلْبٍ سَلِيمٍ
Fàttalikul ba mu dikkee ca Boroomam ànd ak xol bu mucc ayib.
85إِذْ قَالَ لِأَبِيهِ وَقَوْمِهِ مَاذَا تَعْبُدُونَ
Ak ba mu waxee baayam ak nitam, ne leen : “Ana li ngeen di jaamu ? ”
86أَئِفْكًا آلِهَةً دُونَ اللَّهِ تُرِيدُونَ
Moo ndax ay nar ngeen di namm a def ay yàlla bàyyi Yàlla Moom ?
87فَمَا ظَنُّكُم بِرَبِّ الْعَالَمِينَ
Waaw, lu ngeen njort ci Yàlla boroom asamaan si ? ”
88فَنَظَرَ نَظْرَةً فِي النُّجُومِ
Mu téen xool biddéew yi [di settantal],
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
86Aaya
Tekki — As-Saffat 86
Simoore As-Saffat Aaya 86 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax ay nar ngeen di namm a def ay…Simoore Aaya 86/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 84–88. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore As-Saffat
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Thursday, October 1, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


