Sad · 39/88
Tekki Waxtaan — Sad
هَٰذَا عَطَاؤُنَا فَامْنُنْ أَوْ أَمْسِكْ بِغَيْرِ حِسَابٍ ٣٩
Transliteration
Haazaa `ataaa`unaa famnun aw amsik bighairi hisaab
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
“Lii mooy sunug may ; mayeel walla nga téye ko kenn du ko waññook yaw”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 37-41 — Sad
37وَالشَّيَاطِينَ كُلَّ بَنَّاءٍ وَغَوَّاصٍ
Tàggatal Nanu ko sayaane yi, ñu di ko tabaxal ak di ko nuural ci (ndox).
38وَآخَرِينَ مُقَرَّنِينَ فِي الْأَصْفَادِ
Ak ñeneen, ñu ñu lëkkële ak i njéng.
39هَٰذَا عَطَاؤُنَا فَامْنُنْ أَوْ أَمْسِكْ بِغَيْرِ حِسَابٍ
“Lii mooy sunug may ; mayeel walla nga téye ko kenn du ko waññook yaw”.
40وَإِنَّ لَهُ عِندَنَا لَزُلْفَىٰ وَحُسْنَ مَآبٍ
Te mooy am na daraja ju Nu jege ak wàccuwaay wu jekk.
41وَاذْكُرْ عَبْدَنَا أَيُّوبَ إِذْ نَادَىٰ رَبَّهُ أَنِّي مَسَّنِيَ الشَّيْطَانُ بِنُصْبٍ وَعَذَابٍ
Fàttalikul sunu jaam Ayyuuba , ba muy woo Boroomam naan ko : “Yaw sama Boroom Saytaane teg na ma coono ak i tiis”.
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
39Aaya
Tekki — Sad 39
Simoore Sad Aaya 39 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Lii mooy sunug may ; mayeel walla nga téye ko…Simoore Aaya 39/88 — Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Sad Dégg, Sad Tekki, Sad mp3, Sad pdf. Aaya 37–41. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








