Az-Zumar · 37/75
Tekki Waxtaan — Az-Zumar
وَمَن يَهْدِ اللَّهُ فَمَا لَهُ مِن مُّضِلٍّ ۗ أَلَيْسَ اللَّهُ بِعَزِيزٍ ذِي انتِقَامٍ ۝٣٧
Wa mai yahdil laahu famalahoo mim mudlil; alai sal laahu bi`azeezin zin tiqaam
📖 Tekkim Wolof
Te it képp ku Yàlla namm ci moom njub, kenn du ko réerël. Moo ndax Yàlla dafa dul boroom Kàttan di boroomuk Fayu ? Axakañ !

🎧 Dégg


📜 Aaya 35-39 — Az-Zumar

35لِيُكَفِّرَ اللَّهُ عَنْهُمْ أَسْوَأَ الَّذِي عَمِلُوا وَيَجْزِيَهُمْ أَجْرَهُم بِأَحْسَنِ الَّذِي كَانُوا يَعْمَلُونَ
te Yàlla dana far seen ñaawtéef fay leen ca la gënnoon a rafet ca la ñu daan jëf.
36أَلَيْسَ اللَّهُ بِكَافٍ عَبْدَهُ ۖ وَيُخَوِّفُونَكَ بِالَّذِينَ مِن دُونِهِ ۚ وَمَن يُضْلِلِ اللَّهُ فَمَا لَهُ مِنْ هَادٍ
Moo ndax Yàlla dafa doyul [wéruwaay] ci ab jaamam ? Bay tax ñu di la tiitale ci leneen lu dul Moom. Képp ku Yàlla natt ci moom réer kenn du ku gindi.
37وَمَن يَهْدِ اللَّهُ فَمَا لَهُ مِن مُّضِلٍّ ۗ أَلَيْسَ اللَّهُ بِعَزِيزٍ ذِي انتِقَامٍ
Te it képp ku Yàlla namm ci moom njub, kenn du ko réerël. Moo ndax Yàlla dafa dul boroom Kàttan di boroomuk Fayu ? Axakañ !
38وَلَئِن سَأَلْتَهُم مَّنْ خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ لَيَقُولُنَّ اللَّهُ ۚ قُلْ أَفَرَأَيْتُم مَّا تَدْعُونَ مِن دُونِ اللَّهِ إِنْ أَرَادَنِيَ اللَّهُ بِضُرٍّ هَلْ هُنَّ كَاشِفَاتُ ضُرِّهِ أَوْ أَرَادَنِي بِرَحْمَةٍ هَلْ هُنَّ مُمْسِكَاتُ رَحْمَتِهِ ۚ قُلْ حَسْبِيَ اللَّهُ ۖ عَلَيْهِ يَتَوَكَّلُ الْمُتَوَكِّلُونَ
Soo leen laajoon : “Ku bind asamaan yeek suuf si ? ”, Ñu ni la : “Yàlla”. Waxal ne : “Xanaa gisu leen li ngéen di jaamu bàyyi Yàlla ; ci ne su Yàlla nammee ci man lor, ndax ñoom kon danañu man a teggi lor ja ? Walla su Yàlla nammoon ci man yërmaande, ndax kenn danañu man a fanq yërmaande ja ? ” – waxal ne : “Yàlla doy na ma : ci moom la wéerukat ya di wéeru”
39قُلْ يَا قَوْمِ اعْمَلُوا عَلَىٰ مَكَانَتِكُمْ إِنِّي عَامِلٌ ۖ فَسَوْفَ تَعْلَمُونَ
Waxal ne : “Éy yéen samaw nit, liggéeyleen lu ngeen man, man it [maa ngi liggéey]. Dangeen xalset a xam
Az-ZumarFihi Alxuraan
75Aaya
MeccanRevelation
37Aaya

Tekki — Az-Zumar 37

Simoore Az-Zumar Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te it képp ku Yàlla namm ci moom njub, kenn…

Simoore Aaya 37/75 — Az-Zumar الزمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zumar Dégg, Az-Zumar Tekki, Az-Zumar mp3, Az-Zumar pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers