Adh-Dhariyat · 23/60
Tekki Waxtaan — Simoore Adh-Dhariyat
فَوَرَبِّ السَّمَاءِ وَالْأَرْضِ إِنَّهُ لَحَقٌّ مِّثْلَ مَا أَنَّكُمْ تَنطِقُونَ ۝٢٣
Fawa Rabbis samaaa`i wal ardi innahoo lahaqqum misla maa annakum tantiqoon
📖 Tekkim Wolof
Giiñ naa ci Boroom asamaan ak suuf ! Ne loolu dëgg la lu am la ni jibug seeni kàddu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 21-25 — Simoore Adh-Dhariyat

21وَفِي أَنفُسِكُمْ ۚ أَفَلَا تُبْصِرُونَ
ak ci seeni jëmm (am nay kéemaan). Moo ndax dangeen dul gis ?
22وَفِي السَّمَاءِ رِزْقُكُمْ وَمَا تُوعَدُونَ
Seen wërsëg (taw) mi ngi ci asamaan si ak linu leen di dig.
23فَوَرَبِّ السَّمَاءِ وَالْأَرْضِ إِنَّهُ لَحَقٌّ مِّثْلَ مَا أَنَّكُمْ تَنطِقُونَ
Giiñ naa ci Boroom asamaan ak suuf ! Ne loolu dëgg la lu am la ni jibug seeni kàddu.
24هَلْ أَتَاكَ حَدِيثُ ضَيْفِ إِبْرَاهِيمَ الْمُكْرَمِينَ
Moo ndax yaw waxtaanu ganu Ibraahiima yu tedd ya aksi na ci yaw ?
25إِذْ دَخَلُوا عَلَيْهِ فَقَالُوا سَلَامًا ۖ قَالَ سَلَامٌ قَوْمٌ مُّنكَرُونَ
Ba ñu ko fekkee fa mu nekkoon ne ko : “Jàmm nga am ! ”, mu ne [leen] : “Jàmm rekk, yéen dey xamuma leen”.
Adh-DhariyatFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — Adh-Dhariyat 23

Simoore Adh-Dhariyat Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Giiñ naa ci Boroom asamaan ak suuf ! Ne loolu…

Simoore Aaya 23/60 — Simoore Adh-Dhariyat الذاريات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Adh-Dhariyat Dégg, Simoore Adh-Dhariyat Tekki, Simoore Adh-Dhariyat mp3, Simoore Adh-Dhariyat pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers