At-Tur · 41/49
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tur
أَمْ عِندَهُمُ الْغَيْبُ فَهُمْ يَكْتُبُونَ ۝٤١
Am `indahumul ghaibu fahum yaktuboon
📖 Tekkim Wolof
Walla ñoom ñoo ame Mbóot yi di ko bind ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 39-43 — Simoore At-Tur

39أَمْ لَهُ الْبَنَاتُ وَلَكُمُ الْبَنُونَ
Walla book Yàlla moom moo am ay doom yu jigéen, yéen ngeen am yu góor ? (mukk)
40أَمْ تَسْأَلُهُمْ أَجْرًا فَهُم مِّن مَّغْرَمٍ مُّثْقَلُونَ
Moo ndax dangeen leen di laaj ag pey, te ñoom nu diis gann ak i bor ?
41أَمْ عِندَهُمُ الْغَيْبُ فَهُمْ يَكْتُبُونَ
Walla ñoom ñoo ame Mbóot yi di ko bind ?
42أَمْ يُرِيدُونَ كَيْدًا ۖ فَالَّذِينَ كَفَرُوا هُمُ الْمَكِيدُونَ
Wala ñoom dañoo am ay pexe ? Te kat pexe yépp ña ko def lay raas.
43أَمْ لَهُمْ إِلَٰهٌ غَيْرُ اللَّهِ ۚ سُبْحَانَ اللَّهِ عَمَّا يُشْرِكُونَ
Walla ñoom dañoo am jeneen Yàlla ju dul Yàlla ? (Mukk) Tuddnaa Sellam ga soree na lool ak liñu koy bokkaale !
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
41Aaya

Tekki — At-Tur 41

Simoore At-Tur Aaya 41 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Walla ñoom ñoo ame Mbóot yi di ko bind ?

Simoore Aaya 41/49 — Simoore At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tur Dégg, Simoore At-Tur Tekki, Simoore At-Tur mp3, Simoore At-Tur pdf. Aaya 39–43. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers