An-Najm · 21/62
Tekki Waxtaan — An-Najm
أَلَكُمُ الذَّكَرُ وَلَهُ الْأُنثَىٰ ۝٢١
A-lakumuz zakaru wa lahul unsaa
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax yéen a am doom yu góor moom Yàlla mu am ay jigéen ?
🎧 Dégg

📜 Aaya 19-23 — An-Najm

19أَفَرَأَيْتُمُ اللَّاتَ وَالْعُزَّىٰ
Waaw xërëmu Laata ak Uzzaa lu ñu leen di niru,
20وَمَنَاةَ الثَّالِثَةَ الْأُخْرَىٰ
ak Manaat xërëm ba ca des, te ñetteel leen ?
21أَلَكُمُ الذَّكَرُ وَلَهُ الْأُنثَىٰ
Moo ndax yéen a am doom yu góor moom Yàlla mu am ay jigéen ?
22تِلْكَ إِذًا قِسْمَةٌ ضِيزَىٰ
(Xam ngeen) ne woowu séddale yéen jubul de !
23إِنْ هِيَ إِلَّا أَسْمَاءٌ سَمَّيْتُمُوهَا أَنتُمْ وَآبَاؤُكُم مَّا أَنزَلَ اللَّهُ بِهَا مِن سُلْطَانٍ ۚ إِن يَتَّبِعُونَ إِلَّا الظَّنَّ وَمَا تَهْوَى الْأَنفُسُ ۖ وَلَقَدْ جَاءَهُم مِّن رَّبِّهِمُ الْهُدَىٰ
Loolu ay tur la doŋŋ yu ngeen di tudd (xërëm ya), yéen ak seeni baay. Seen njortu rekk la ñu topp waaye yayoowunu jaamu. Topp it seen bànneex, looloo tax njub dikk bawoo fa seen Boroom.
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
21Aaya

Tekki — An-Najm 21

Simoore An-Najm Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax yéen a am doom yu góor moom Yàlla…

Simoore Aaya 21/62 — An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Najm Dégg, An-Najm Tekki, An-Najm mp3, An-Najm pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers