An-Najm · 52/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
وَقَوْمَ نُوحٍ مِّن قَبْلُ ۖ إِنَّهُمْ كَانُوا هُمْ أَظْلَمَ وَأَطْغَىٰ ۝٥٢
Wa qawma Noohim min qablu innahum kaanoo hum azlama wa atghaa
📖 Tekkim Wolof
ak nitu Nooh ñu jëkk ña, ndax ñoom ñoo dàqoon tooñ te gënoon a bew,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 50-54 — Simoore An-Najm

50وَأَنَّهُ أَهْلَكَ عَادًا الْأُولَىٰ
te moom Moo faagaagaloon waa Aad ñu jëkk ña,
51وَثَمُودَ فَمَا أَبْقَىٰ
ak waa Samuud, ba kenn desufa,
52وَقَوْمَ نُوحٍ مِّن قَبْلُ ۖ إِنَّهُمْ كَانُوا هُمْ أَظْلَمَ وَأَطْغَىٰ
ak nitu Nooh ñu jëkk ña, ndax ñoom ñoo dàqoon tooñ te gënoon a bew,
53وَالْمُؤْتَفِكَةَ أَهْوَىٰ
noona la wëlbatee suuf sa këpp leen ko.
54فَغَشَّاهَا مَا غَشَّىٰ
Muur leen ko.
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
52Aaya

Tekki — An-Najm 52

Simoore An-Najm Aaya 52 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ak nitu Nooh ñu jëkk ña, ndax ñoom ñoo dàqoon…

Simoore Aaya 52/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 50–54. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers