Ar-Rahman · 12/78
Tekki Waxtaan — Ar-Rahman
وَالْحَبُّ ذُو الْعَصْفِ وَالرَّيْحَانُ ۝١٢
Walhabbu zul `asfi war Raihaanu
📖 Tekkim Wolof
ak ay fepp yu nekk ci mbaram, ak gàncax yuy gilli.

🎧 Dégg


📜 Aaya 10-14 — Ar-Rahman

10وَالْأَرْضَ وَضَعَهَا لِلْأَنَامِ
Moo tàllal, suuf ñiy dunde :
11فِيهَا فَاكِهَةٌ وَالنَّخْلُ ذَاتُ الْأَكْمَامِ
am na ay fuytéef, ak tàndarma yuy meññ,
12وَالْحَبُّ ذُو الْعَصْفِ وَالرَّيْحَانُ
ak ay fepp yu nekk ci mbaram, ak gàncax yuy gilli.
13فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
14خَلَقَ الْإِنسَانَ مِن صَلْصَالٍ كَالْفَخَّارِ
Moom moo bind nit ci ban bu tikk dëgër ;
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
12Aaya

Tekki — Ar-Rahman 12

Simoore Ar-Rahman Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ak ay fepp yu nekk ci mbaram, ak gàncax yuy…

Simoore Aaya 12/78 — Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Rahman Dégg, Ar-Rahman Tekki, Ar-Rahman mp3, Ar-Rahman pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers